Al-Furqan · 63/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
وَعِبَادُ الرَّحْمَٰنِ الَّذِينَ يَمْشُونَ عَلَى الْأَرْضِ هَوْنًا وَإِذَا خَاطَبَهُمُ الْجَاهِلُونَ قَالُوا سَلَامًا ۝٦٣
Wa `ibaadur Rahmaanil lazeena yamshoona `alal ardi hawnanw wa izaa khaata bahumul jaahiloona qaaloo salaamaa
📖 Tekkim Wolof
Ak jaami Yàlla yii dox ci kaw suuf si ndànk, su ñu réer ña di wàqanteek ñoom, ñuy wax jàmm,

🎧 Dégg


📜 Aaya 61-65 — Simoore Al-Furqan

61تَبَارَكَ الَّذِي جَعَلَ فِي السَّمَاءِ بُرُوجًا وَجَعَلَ فِيهَا سِرَاجًا وَقَمَرًا مُّنِيرًا
Barkeel na [Moom Yàlla] mi def ci asamaan si ay yoon, def ca ab làmp [jant bi] ak weer wu leer nàññ !
62وَهُوَ الَّذِي جَعَلَ اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ خِلْفَةً لِّمَنْ أَرَادَ أَن يَذَّكَّرَ أَوْ أَرَادَ شُكُورًا
Mooy Ki def guddeek bëccëg ñuy jëlasante ngir ku bëgg a xalaat, fàttaliku, mbaa mu bëgg a sant.
63وَعِبَادُ الرَّحْمَٰنِ الَّذِينَ يَمْشُونَ عَلَى الْأَرْضِ هَوْنًا وَإِذَا خَاطَبَهُمُ الْجَاهِلُونَ قَالُوا سَلَامًا
Ak jaami Yàlla yii dox ci kaw suuf si ndànk, su ñu réer ña di wàqanteek ñoom, ñuy wax jàmm,
64وَالَّذِينَ يَبِيتُونَ لِرَبِّهِمْ سُجَّدًا وَقِيَامًا
ñoom ñooy fanaanee julli te Yàlla rekk tax [taxaw ak a sujjóot] ;
65وَالَّذِينَ يَقُولُونَ رَبَّنَا اصْرِفْ عَنَّا عَذَابَ جَهَنَّمَ ۖ إِنَّ عَذَابَهَا كَانَ غَرَامًا
ñoom ñooy wax naan : “Yàlla, yal na nga nu dëddëleek mbugalum Safara”. - mbugalum Safara soosu lu ne dànk la.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
63Aaya

Tekki — Al-Furqan 63

Simoore Al-Furqan Aaya 63 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak jaami Yàlla yii dox ci kaw suuf si ndànk,…

Simoore Aaya 63/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 61–65. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers