An-Naml · 33/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
قَالُوا نَحْنُ أُولُو قُوَّةٍ وَأُولُو بَأْسٍ شَدِيدٍ وَالْأَمْرُ إِلَيْكِ فَانظُرِي مَاذَا تَأْمُرِينَ ٣٣
Transliteration
Qaaloo nahnu uloo quwwatinw wa uloo baasin shadeed; wal amru ilaiki fanzuree maazaa taamureen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Nun am nañu dooleek alal te yaay digle. Seetal loo nuy digal”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 31-35 — An-Naml
31أَلَّا تَعْلُوا عَلَيَّ وَأْتُونِي مُسْلِمِينَ
Buleen rëy-rëylu ci sama kaw te ñëwleen jébbalusi seen bopp”.
32قَالَتْ يَا أَيُّهَا الْمَلَأُ أَفْتُونِي فِي أَمْرِي مَا كُنتُ قَاطِعَةً أَمْرًا حَتَّىٰ تَشْهَدُونِ
Buur ba ne gàngooram : "Ubbileen sama bopp ci mbir mii : masumaa dugg ci menn mbir
te joxewuleen ci xalaat”.
33قَالُوا نَحْنُ أُولُو قُوَّةٍ وَأُولُو بَأْسٍ شَدِيدٍ وَالْأَمْرُ إِلَيْكِ فَانظُرِي مَاذَا تَأْمُرِينَ
Ñu ne ko : “Nun am nañu dooleek alal te yaay digle. Seetal loo nuy digal”.
34قَالَتْ إِنَّ الْمُلُوكَ إِذَا دَخَلُوا قَرْيَةً أَفْسَدُوهَا وَجَعَلُوا أَعِزَّةَ أَهْلِهَا أَذِلَّةً ۖ وَكَذَٰلِكَ يَفْعَلُونَ
Buur ba ne leen : “Buur yi dey, bu ñu duggee cib dëkk, yàqate ko, daldi toroxal ña fa gënoon a tedd. Ñoom noonu la ñuy def.
35وَإِنِّي مُرْسِلَةٌ إِلَيْهِم بِهَدِيَّةٍ فَنَاظِرَةٌ بِمَ يَرْجِعُ الْمُرْسَلُونَ
Man, dama leen di yónnee alal [neexal], su ma ko defee nag xool lu ndaw ya di delloosi”.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
33Aaya
Tekki — An-Naml 33
Simoore An-Naml Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Nun am nañu dooleek alal te…Simoore Aaya 33/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








