Al-Qasas · 32/88
Tekki Waxtaan — Al-Qasas
اسْلُكْ يَدَكَ فِي جَيْبِكَ تَخْرُجْ بَيْضَاءَ مِنْ غَيْرِ سُوءٍ وَاضْمُمْ إِلَيْكَ جَنَاحَكَ مِنَ الرَّهْبِ ۖ فَذَانِكَ بُرْهَانَانِ مِن رَّبِّكَ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا فَاسِقِينَ ۝٣٢
Usluk yadaka fee jaibika takhruj baidaaa`a min ghairi sooo`inw wadmum ilaika janaahaka minar rahbi fazaanika burhaanaani mir Rabbika ilaa Fiw`awna wa mala`ih; innahum kaanoo qawman faasiqeen
📖 Tekkim Wolof
Sóobal sa loxo ci sa mbagg, dina génn weex tàll. Te nanga taf sa loxo bi ci sa kaw ngir bañ a tiit. Yooyu yaari mbir ay firnde la yu bawoo ca sa Boroom Mu jëme ko ci Firawna ak gàngooram. Ñoom ay saay-saay lañu”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 30-34 — Al-Qasas

30فَلَمَّا أَتَاهَا نُودِيَ مِن شَاطِئِ الْوَادِ الْأَيْمَنِ فِي الْبُقْعَةِ الْمُبَارَكَةِ مِنَ الشَّجَرَةِ أَن يَا مُوسَىٰ إِنِّي أَنَا اللَّهُ رَبُّ الْعَالَمِينَ
Ba mu fa agsee, mu am lu ko woo ci xuru ndeyjoor wa, ne ko : “Éy Muusaa ! ManMii Maa di Yàlla jiy Boroom àddina si yépp”.
31وَأَنْ أَلْقِ عَصَاكَ ۖ فَلَمَّا رَآهَا تَهْتَزُّ كَأَنَّهَا جَانٌّ وَلَّىٰ مُدْبِرًا وَلَمْ يُعَقِّبْ ۚ يَا مُوسَىٰ أَقْبِلْ وَلَا تَخَفْ ۖ إِنَّكَ مِنَ الْآمِنِينَ
Te : “Nanga sànni sa yet wi” ; [Ba mu ko sànnee] gis ne ma ngay yëngatu mel ni jaan, mu ne baxarñit.”. Yàlla woowaat ko, ne ko : “Dellusil te bul tiit : yaa ngi ci lu wóor”.
32اسْلُكْ يَدَكَ فِي جَيْبِكَ تَخْرُجْ بَيْضَاءَ مِنْ غَيْرِ سُوءٍ وَاضْمُمْ إِلَيْكَ جَنَاحَكَ مِنَ الرَّهْبِ ۖ فَذَانِكَ بُرْهَانَانِ مِن رَّبِّكَ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا فَاسِقِينَ
Sóobal sa loxo ci sa mbagg, dina génn weex tàll. Te nanga taf sa loxo bi ci sa kaw ngir bañ a tiit. Yooyu yaari mbir ay firnde la yu bawoo ca sa Boroom Mu jëme ko ci Firawna ak gàngooram. Ñoom ay saay-saay lañu”.
33قَالَ رَبِّ إِنِّي قَتَلْتُ مِنْهُمْ نَفْسًا فَأَخَافُ أَن يَقْتُلُونِ
[Muusaa wax na ne] : “Rey naa ci ñoom bakkan te ragal naa ñu rey ma.
34وَأَخِي هَارُونُ هُوَ أَفْصَحُ مِنِّي لِسَانًا فَأَرْسِلْهُ مَعِيَ رِدْءًا يُصَدِّقُنِي ۖ إِنِّي أَخَافُ أَن يُكَذِّبُونِ
Te Aaruuna moo ma gën a leer i wax. Yebal ko mu ànd ak man di ma ruqandi, di ma dëggal : man daal ragal naa ñu jàppe ma fenkat”.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Al-Qasas 32

Simoore Al-Qasas Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sóobal sa loxo ci sa mbagg, dina génn weex tàll.…

Simoore Aaya 32/88 — Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qasas Dégg, Al-Qasas Tekki, Al-Qasas mp3, Al-Qasas pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers