Aali Imran · 101/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
وَكَيْفَ تَكْفُرُونَ وَأَنتُمْ تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ آيَاتُ اللَّهِ وَفِيكُمْ رَسُولُهُ ۗ وَمَن يَعْتَصِم بِاللَّهِ فَقَدْ هُدِيَ إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ ١٠١
Transliteration
Wa kaifa takfuroona wa antum tutlaa `alaikum Aayaatul laahi wa feekum Rasooluh; wa mai ya`tasim baillaahi faqad hudiya ilaa Siraatim Mustaqeem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Naka ngeen di weddee te laayay Yàlla yi ñi di ko jàng fi seen kanam, Yonent bi nekk fi seen biir ? Ku ŋoy ci Yàlla, gindiku na jëm ca yoon wu jub xocc wa.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 99-103 — Simoore Aali Imran
99قُلْ يَا أَهْلَ الْكِتَابِ لِمَ تَصُدُّونَ عَن سَبِيلِ اللَّهِ مَنْ آمَنَ تَبْغُونَهَا عِوَجًا وَأَنتُمْ شُهَدَاءُ ۗ وَمَا اللَّهُ بِغَافِلٍ عَمَّا تَعْمَلُونَ
Neel : “Yéen ñoñ-téere, lu tax ngeen di gàllankoor ñiy dox jëm ci yoonu Yàlla, di ko wutal sikk? Te ngeen di ay seede, te Yàlla sàgganewut li ngeen di jëf de.
100يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِن تُطِيعُوا فَرِيقًا مِّنَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ يَرُدُّوكُم بَعْدَ إِيمَانِكُمْ كَافِرِينَ
Éy yéen ñi gëm ! Bu ngeen toppee ñenn ñi, ñoñ-téere, danañu leen delloo ci kéefar gannaaw ba ngeen gëmee Yàlla.
101وَكَيْفَ تَكْفُرُونَ وَأَنتُمْ تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ آيَاتُ اللَّهِ وَفِيكُمْ رَسُولُهُ ۗ وَمَن يَعْتَصِم بِاللَّهِ فَقَدْ هُدِيَ إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Naka ngeen di weddee te laayay Yàlla yi ñi di ko jàng fi seen kanam, Yonent bi nekk fi seen biir ? Ku ŋoy ci Yàlla, gindiku na jëm ca yoon wu jub xocc wa.
102يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اتَّقُوا اللَّهَ حَقَّ تُقَاتِهِ وَلَا تَمُوتُنَّ إِلَّا وَأَنتُم مُّسْلِمُونَ
Éy yéen ñi gëm ! Ragal-leen Yàlla kem ni mu yellee [tigi]. Te buleen dee mukk lu dul fekk na yéen a ngi wommatu jëm ci Yàlla.
103وَاعْتَصِمُوا بِحَبْلِ اللَّهِ جَمِيعًا وَلَا تَفَرَّقُوا ۚ وَاذْكُرُوا نِعْمَتَ اللَّهِ عَلَيْكُمْ إِذْ كُنتُمْ أَعْدَاءً فَأَلَّفَ بَيْنَ قُلُوبِكُمْ فَأَصْبَحْتُم بِنِعْمَتِهِ إِخْوَانًا وَكُنتُمْ عَلَىٰ شَفَا حُفْرَةٍ مِّنَ النَّارِ فَأَنقَذَكُم مِّنْهَا ۗ كَذَٰلِكَ يُبَيِّنُ اللَّهُ لَكُمْ آيَاتِهِ لَعَلَّكُمْ تَهْتَدُونَ
Jafanduleen yéen ñépp ci buumug Yàlla gi te buleen teqalikoo ; fàttalikuleen xéewal gi leen Yàlla defaloon ba ngeen nekkee ay noon [lu jiitu Lislaam], mu tàppe seeni xol. Ba ngeen mujj ci xéewalam di ay doomi ndey. Te it nekkoon ngeen ci pindub kàmbug Safara, mu xettali leen ci loolu. Noonu la leen Yàlla di leeralee ay káddoom ndax Yàlla ngeen gindiku.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
101Aaya
Tekki — Aali Imran 101
Simoore Aali Imran Aaya 101 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Naka ngeen di weddee te laayay Yàlla yi ñi di…Simoore Aaya 101/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 99–103. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








