Aali Imran · 127/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
لِيَقْطَعَ طَرَفًا مِّنَ الَّذِينَ كَفَرُوا أَوْ يَكْبِتَهُمْ فَيَنقَلِبُوا خَائِبِينَ ۝١٢٧
Laiyaqta`a tarafam minal lazeena kafarooo aw yakbitahum fayanqaliboo khaaa`ibeen
📖 Tekkim Wolof
def na ko it ngir dog ab kurél walla toroxal leen, ba ñu wëlbatiku di ñu yàkkiku [seen yaakaar tas].
🎧 Dégg

📜 Aaya 125-129 — Aali Imran

125بَلَىٰ ۚ إِن تَصْبِرُوا وَتَتَّقُوا وَيَأْتُوكُم مِّن فَوْرِهِمْ هَٰذَا يُمْدِدْكُمْ رَبُّكُم بِخَمْسَةِ آلَافٍ مِّنَ الْمَلَائِكَةِ مُسَوِّمِينَ
Axakañ ! Bu ngeen muñee te ragal Yàlla, bu ñu leen songee ak doole [ca waxtu wu ñu tànn], seen Boroom dana leen tëbb juróomi junniy Malaaka yuñu màndargaal.
126وَمَا جَعَلَهُ اللَّهُ إِلَّا بُشْرَىٰ لَكُمْ وَلِتَطْمَئِنَّ قُلُوبُكُم بِهِ ۗ وَمَا النَّصْرُ إِلَّا مِنْ عِندِ اللَّهِ الْعَزِيزِ الْحَكِيمِ
Te Yàlla defewuko lu dul bégal leen ngir seeni xel dal. Te ndimbal du bawoo fu dul fa Yàlla, Mooy Ki not, di Ku xereñ ki ;
127لِيَقْطَعَ طَرَفًا مِّنَ الَّذِينَ كَفَرُوا أَوْ يَكْبِتَهُمْ فَيَنقَلِبُوا خَائِبِينَ
def na ko it ngir dog ab kurél walla toroxal leen, ba ñu wëlbatiku di ñu yàkkiku [seen yaakaar tas].
128لَيْسَ لَكَ مِنَ الْأَمْرِ شَيْءٌ أَوْ يَتُوبَ عَلَيْهِمْ أَوْ يُعَذِّبَهُمْ فَإِنَّهُمْ ظَالِمُونَ
[Yaw Yonent bi], mbir moomu moomoo ci dara - Yàlla Moo leen di jéggal walla Mu mbugal leen, ñoom daal ay tooñkat lañu.
129وَلِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۚ يَغْفِرُ لِمَن يَشَاءُ وَيُعَذِّبُ مَن يَشَاءُ ۚ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Te Yàlla Moo moom li nekk ci asamaan yeek suuf si. Mooy jéggal ku ko soob, di mbugal ku ko soob. ...Yàlla Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
127Aaya

Tekki — Aali Imran 127

Simoore Aali Imran Aaya 127 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : def na ko it ngir dog ab kurél walla toroxal…

Simoore Aaya 127/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 125–129. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers