Saba · 23/54
Tekki Waxtaan — Saba
وَلَا تَنفَعُ الشَّفَاعَةُ عِندَهُ إِلَّا لِمَنْ أَذِنَ لَهُ ۚ حَتَّىٰ إِذَا فُزِّعَ عَن قُلُوبِهِمْ قَالُوا مَاذَا قَالَ رَبُّكُمْ ۖ قَالُوا الْحَقَّ ۖ وَهُوَ الْعَلِيُّ الْكَبِيرُ ۝٢٣
Wa laa tanfa`ush shafaa`atu `indahooo illaa liman azina lah; hattaaa izaa fuzzi`a `an quloobihim qaaloo maazaa qaala Rabbukum; qaalul haqq, wa Huwal `Aliyul Kabeer
📖 Tekkim Wolof
Tinu mënu la jariñ dara fa Moom [Yàlla], lu dul ka Mu ca jox ndigal. Bu tiit ma duggee seeni xol nag, ñu naan : “Lan la seen Boroom wax nag ? ”. Ñu ne leen : “Dëgg rekk ; Te Moom moo di Ku Kawe, di Ku Màgg ka”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 21-25 — Saba

21وَمَا كَانَ لَهُ عَلَيْهِم مِّن سُلْطَانٍ إِلَّا لِنَعْلَمَ مَن يُؤْمِنُ بِالْآخِرَةِ مِمَّنْ هُوَ مِنْهَا فِي شَكٍّ ۗ وَرَبُّكَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ حَفِيظٌ
Amul woon ci ñoom benn mën-mën lu dul ngir Nu xam ña ca gëm àllaaxira ak ña koy sikki-sàkka. Sa Boroom mooy wattu lépp lu ne.
22قُلِ ادْعُوا الَّذِينَ زَعَمْتُم مِّن دُونِ اللَّهِ ۖ لَا يَمْلِكُونَ مِثْقَالَ ذَرَّةٍ فِي السَّمَاوَاتِ وَلَا فِي الْأَرْضِ وَمَا لَهُمْ فِيهِمَا مِن شِرْكٍ وَمَا لَهُ مِنْهُم مِّن ظَهِيرٍ
Waxal ne : “Li ngeen di jaamu bàyyi Yàlla. Amuñu lu tollu ni kem aw fepp ci asamaan yeek suuf si. Bokkuñu ci, ci dara, te it kenn dimbaliwu ko woon ci ñoom”.
23وَلَا تَنفَعُ الشَّفَاعَةُ عِندَهُ إِلَّا لِمَنْ أَذِنَ لَهُ ۚ حَتَّىٰ إِذَا فُزِّعَ عَن قُلُوبِهِمْ قَالُوا مَاذَا قَالَ رَبُّكُمْ ۖ قَالُوا الْحَقَّ ۖ وَهُوَ الْعَلِيُّ الْكَبِيرُ
Tinu mënu la jariñ dara fa Moom [Yàlla], lu dul ka Mu ca jox ndigal. Bu tiit ma duggee seeni xol nag, ñu naan : “Lan la seen Boroom wax nag ? ”. Ñu ne leen : “Dëgg rekk ; Te Moom moo di Ku Kawe, di Ku Màgg ka”.
24۞ قُلْ مَن يَرْزُقُكُم مِّنَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ قُلِ اللَّهُ ۖ وَإِنَّا أَوْ إِيَّاكُمْ لَعَلَىٰ هُدًى أَوْ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Neel : “Ana kan moo leen di wërsëgal ci asamaan yeek suuf si ? ”. Waxal ne : “Yàlla. Te Nun ak yéen, ana kan moo nekk ci njug walla réer gu bir”.
25قُل لَّا تُسْأَلُونَ عَمَّا أَجْرَمْنَا وَلَا نُسْأَلُ عَمَّا تَعْمَلُونَ
Neel : “Kenn duleen laaj li nuy def, te it kenn dunu laaj li ngeen di def”.
SabaFihi Alxuraan
54Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Saba 23

Simoore Saba Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Tinu mënu la jariñ dara fa Moom [Yàlla], lu dul…

Simoore Aaya 23/54 — Saba سبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Saba Dégg, Saba Tekki, Saba mp3, Saba pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers