Ya-Sin · 53/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
إِن كَانَتْ إِلَّا صَيْحَةً وَاحِدَةً فَإِذَا هُمْ جَمِيعٌ لَّدَيْنَا مُحْضَرُونَ ٥٣
Transliteration
In kaanat illaa saihatanw waahidatan fa-izaa hum jamee`ul ladainaa muhdaroon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Genn ug xaacu rekk a jib, ñu seet-seeti ñoom ñépp, ne jaseet Sunu kanam.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 51-55 — Ya-Sin
51وَنُفِخَ فِي الصُّورِ فَإِذَا هُم مِّنَ الْأَجْدَاثِ إِلَىٰ رَبِّهِمْ يَنسِلُونَ
Su ñu ëfee Buftu bi, dañu naan futeet ca bàmmeel ya, dox wuti seen Boroom,
52قَالُوا يَا وَيْلَنَا مَن بَعَثَنَا مِن مَّرْقَدِنَا ۜ ۗ هَٰذَا مَا وَعَدَ الرَّحْمَٰنُ وَصَدَقَ الْمُرْسَلُونَ
ñuy wax naan : “Wóoy ngalla nun ! Moo ana kan moo nu yékkatee ci sunu yàndoorukaay bi ? ” Lii dey mooy la nu Yërëmaakoon bi doon dig ; kon Yonent yi waxoon nañu dëgg.
53إِن كَانَتْ إِلَّا صَيْحَةً وَاحِدَةً فَإِذَا هُمْ جَمِيعٌ لَّدَيْنَا مُحْضَرُونَ
Genn ug xaacu rekk a jib, ñu seet-seeti ñoom ñépp, ne jaseet Sunu kanam.
54فَالْيَوْمَ لَا تُظْلَمُ نَفْسٌ شَيْئًا وَلَا تُجْزَوْنَ إِلَّا مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Bis niki tey, deesul tooñ benn bakkan . Te deefuleen feye lu dul la ngeen daan jëf.
55إِنَّ أَصْحَابَ الْجَنَّةِ الْيَوْمَ فِي شُغُلٍ فَاكِهُونَ
Bis niki tey, waa Àjjanaa ngi ci xéewal gu mat sëkk ;
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
53Aaya
Tekki — Ya-Sin 53
Simoore Ya-Sin Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Genn ug xaacu rekk a jib, ñu seet-seeti ñoom ñépp,…Simoore Aaya 53/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








