Ya-Sin · 6/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
لِتُنذِرَ قَوْمًا مَّا أُنذِرَ آبَاؤُهُمْ فَهُمْ غَافِلُونَ ۝٦
Litunzira qawmam maaa unzira aabaaa`uhum fahum ghaafiloon
📖 Tekkim Wolof
Ngir nga xupp aw nit ñoo xam ne kenn musul a xupp seeni baay : ñoom dañoo sàggan.

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Simoore Ya-Sin

4عَلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
ci kaw yoon wu jub xocc wa.
5تَنزِيلَ الْعَزِيزِ الرَّحِيمِ
Mi ngi wàcce ci Yàlla boroom Kàttan ga di ab Jaglewaakoonu yërmaandeem.
6لِتُنذِرَ قَوْمًا مَّا أُنذِرَ آبَاؤُهُمْ فَهُمْ غَافِلُونَ
Ngir nga xupp aw nit ñoo xam ne kenn musul a xupp seeni baay : ñoom dañoo sàggan.
7لَقَدْ حَقَّ الْقَوْلُ عَلَىٰ أَكْثَرِهِمْ فَهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Àtte ba dog : te la ëpp ca ñoom [ca Lawhul Mahfuuj] ci ne duñu gëmati.
8إِنَّا جَعَلْنَا فِي أَعْنَاقِهِمْ أَغْلَالًا فَهِيَ إِلَى الْأَذْقَانِ فَهُم مُّقْمَحُونَ
Def Nanu ay jéng ci seeni loos, mu àndak seeni daayi sikkim : ñu joñ leen.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Ya-Sin 6

Simoore Ya-Sin Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ngir nga xupp aw nit ñoo xam ne kenn musul…

Simoore Aaya 6/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers