Ya-Sin · 5/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
تَنزِيلَ الْعَزِيزِ الرَّحِيمِ ۝٥
Tanzeelal `Azeezir Raheem
📖 Tekkim Wolof
Mi ngi wàcce ci Yàlla boroom Kàttan ga di ab Jaglewaakoonu yërmaandeem.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Ya-Sin

3إِنَّكَ لَمِنَ الْمُرْسَلِينَ
Ci ne yaw [Muhammad] bokk nga ci limub Yonent yi.
4عَلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
ci kaw yoon wu jub xocc wa.
5تَنزِيلَ الْعَزِيزِ الرَّحِيمِ
Mi ngi wàcce ci Yàlla boroom Kàttan ga di ab Jaglewaakoonu yërmaandeem.
6لِتُنذِرَ قَوْمًا مَّا أُنذِرَ آبَاؤُهُمْ فَهُمْ غَافِلُونَ
Ngir nga xupp aw nit ñoo xam ne kenn musul a xupp seeni baay : ñoom dañoo sàggan.
7لَقَدْ حَقَّ الْقَوْلُ عَلَىٰ أَكْثَرِهِمْ فَهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Àtte ba dog : te la ëpp ca ñoom [ca Lawhul Mahfuuj] ci ne duñu gëmati.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Ya-Sin 5

Simoore Ya-Sin Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mi ngi wàcce ci Yàlla boroom Kàttan ga di ab…

Simoore Aaya 5/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 9, 2026

Don't forget us in your sincere prayers