Az-Zumar · 59/75
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zumar
بَلَىٰ قَدْ جَاءَتْكَ آيَاتِي فَكَذَّبْتَ بِهَا وَاسْتَكْبَرْتَ وَكُنتَ مِنَ الْكَافِرِينَ ۝٥٩
Balaa qad jaaa`atka Asyaatee fakazzabta bihaa wastak barta wa kunta minal kaafireen
📖 Tekkim Wolof
“Mukk ! Ndax Samay laaya dikkaloon na la nga weddi ko, di rëy-rëylu dem àndeek yéefar yi”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 57-61 — Simoore Az-Zumar

57أَوْ تَقُولَ لَوْ أَنَّ اللَّهَ هَدَانِي لَكُنتُ مِنَ الْمُتَّقِينَ
walla mu naan : “Suma Yàlla gindi woon, kon danaa bokk, ca ñay ragal Yàlla” ;
58أَوْ تَقُولَ حِينَ تَرَى الْعَذَابَ لَوْ أَنَّ لِي كَرَّةً فَأَكُونَ مِنَ الْمُحْسِنِينَ
walla muy wax ba mu gisee mbugël ma naan : “Cëy ! Suma delluwaatoon àddina ! Ba man a bokk ca ñay rafetal”.
59بَلَىٰ قَدْ جَاءَتْكَ آيَاتِي فَكَذَّبْتَ بِهَا وَاسْتَكْبَرْتَ وَكُنتَ مِنَ الْكَافِرِينَ
“Mukk ! Ndax Samay laaya dikkaloon na la nga weddi ko, di rëy-rëylu dem àndeek yéefar yi”.
60وَيَوْمَ الْقِيَامَةِ تَرَى الَّذِينَ كَذَبُوا عَلَى اللَّهِ وُجُوهُهُم مُّسْوَدَّةٌ ۚ أَلَيْسَ فِي جَهَنَّمَ مَثْوًى لِّلْمُتَكَبِّرِينَ
Bu Bis Pénc baa, dangay gis ña fenal Yàlla, seen xar kanam ya ñuul kukk. Moo ndax wàccuwaayi yéefar ya nekkul ca biir Safara ? (Axakañ)
61وَيُنَجِّي اللَّهُ الَّذِينَ اتَّقَوْا بِمَفَازَتِهِمْ لَا يَمَسُّهُمُ السُّوءُ وَلَا هُمْ يَحْزَنُونَ
Yàlla dana musël ña ragal Yàlla te texel leen [ca Àjjana]. Lu bon du leen fa laal te it duñu fa jàq.
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
59Aaya

Tekki — Az-Zumar 59

Simoore Az-Zumar Aaya 59 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Mukk ! Ndax Samay laaya dikkaloon na la nga weddi…

Simoore Aaya 59/75 — Simoore Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zumar Dégg, Simoore Az-Zumar Tekki, Simoore Az-Zumar mp3, Simoore Az-Zumar pdf. Aaya 57–61. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers