Ghafir · 54/85
Tekki Waxtaan — Simoore Ghafir
هُدًى وَذِكْرَىٰ لِأُولِي الْأَلْبَابِ ۝٥٤
Hudanw wa zikraa li ulil albaab
📖 Tekkim Wolof
mu di njub ak ug fàttali ngir ñu di woroom i xel (di xalaat).

🎧 Dégg


📜 Aaya 52-56 — Simoore Ghafir

52يَوْمَ لَا يَنفَعُ الظَّالِمِينَ مَعْذِرَتُهُمْ ۖ وَلَهُمُ اللَّعْنَةُ وَلَهُمْ سُوءُ الدَّارِ
bis ba nga xam ne tooñkat ya, seenug doglu ngànt du leen jariñ dara te am rëb dal na leen te it am nañu fa kër gu bon (soof).
53وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْهُدَىٰ وَأَوْرَثْنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ الْكِتَابَ
Indil Nanu, Muusaa njub, te donale Nanu giiru Banii-Israayiila, Téere ba,
54هُدًى وَذِكْرَىٰ لِأُولِي الْأَلْبَابِ
mu di njub ak ug fàttali ngir ñu di woroom i xel (di xalaat).
55فَاصْبِرْ إِنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ وَاسْتَغْفِرْ لِذَنبِكَ وَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ بِالْعَشِيِّ وَالْإِبْكَارِ
Na nga muñ, (te xam ne) digub Yàlla dëgg la, te it na ngay jéggalu say bàkkar tey sàbbaal sa Boroom di ko sant, ci ngoon si ak ci suba si.
56إِنَّ الَّذِينَ يُجَادِلُونَ فِي آيَاتِ اللَّهِ بِغَيْرِ سُلْطَانٍ أَتَاهُمْ ۙ إِن فِي صُدُورِهِمْ إِلَّا كِبْرٌ مَّا هُم بِبَالِغِيهِ ۚ فَاسْتَعِذْ بِاللَّهِ ۖ إِنَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْبَصِيرُ
Ñay dàggasante ci laayay Yàlla ya ci lu àndul ak firnde yu ñu leen jox, rëy-rëylu doŋŋ a nekk ca seen dënn ya. Te seen aajo du ca fajoo. Na ngay muslu ci Yàlla, moom Mooy aji Dégg, di aji Gis.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
54Aaya

Tekki — Ghafir 54

Simoore Ghafir Aaya 54 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mu di njub ak ug fàttali ngir ñu di woroom…

Simoore Aaya 54/85 — Simoore Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ghafir Dégg, Simoore Ghafir Tekki, Simoore Ghafir mp3, Simoore Ghafir pdf. Aaya 52–56. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers