Ad-Dukhan · 33/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
وَآتَيْنَاهُم مِّنَ الْآيَاتِ مَا فِيهِ بَلَاءٌ مُّبِينٌ ۝٣٣
Wa aatainaahum minal aayaati maa feehi balaaa`um mubeen
📖 Tekkim Wolof
indiloon Nanu leen ay kéemaan (firnde) yu leer nàññ.

🎧 Dégg


📜 Aaya 31-35 — Simoore Ad-Dukhan

31مِن فِرْعَوْنَ ۚ إِنَّهُ كَانَ عَالِيًا مِّنَ الْمُسْرِفِينَ
mom Firawna ma kawe woon lool ca yàqkat ya.
32وَلَقَدِ اخْتَرْنَاهُمْ عَلَىٰ عِلْمٍ عَلَى الْعَالَمِينَ
Tànnoon Nanu leen tigi ci kaw waa àddina sépp (bawoo jamono),
33وَآتَيْنَاهُم مِّنَ الْآيَاتِ مَا فِيهِ بَلَاءٌ مُّبِينٌ
indiloon Nanu leen ay kéemaan (firnde) yu leer nàññ.
34إِنَّ هَٰؤُلَاءِ لَيَقُولُونَ
Ñoo ñaa ngay wax naan :
35إِنْ هِيَ إِلَّا مَوْتَتُنَا الْأُولَىٰ وَمَا نَحْنُ بِمُنشَرِينَ
“Genn dee rekk am muy sunu dee, gu jëkk gi. Te it kenn dunu dekkalaat.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 33

Simoore Ad-Dukhan Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : indiloon Nanu leen ay kéemaan (firnde) yu leer nàññ.

Simoore Aaya 33/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers