Ad-Dukhan · 34/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
إِنَّ هَٰؤُلَاءِ لَيَقُولُونَ ۝٣٤
Inna haaa`ulaaa`i la yaqooloon
📖 Tekkim Wolof
Ñoo ñaa ngay wax naan :

🎧 Dégg


📜 Aaya 32-36 — Simoore Ad-Dukhan

32وَلَقَدِ اخْتَرْنَاهُمْ عَلَىٰ عِلْمٍ عَلَى الْعَالَمِينَ
Tànnoon Nanu leen tigi ci kaw waa àddina sépp (bawoo jamono),
33وَآتَيْنَاهُم مِّنَ الْآيَاتِ مَا فِيهِ بَلَاءٌ مُّبِينٌ
indiloon Nanu leen ay kéemaan (firnde) yu leer nàññ.
34إِنَّ هَٰؤُلَاءِ لَيَقُولُونَ
Ñoo ñaa ngay wax naan :
35إِنْ هِيَ إِلَّا مَوْتَتُنَا الْأُولَىٰ وَمَا نَحْنُ بِمُنشَرِينَ
“Genn dee rekk am muy sunu dee, gu jëkk gi. Te it kenn dunu dekkalaat.
36فَأْتُوا بِآبَائِنَا إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Su fekkee ne dëggu ngeen kon dekkalleen sunuy maam, délloosileen”.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 34

Simoore Ad-Dukhan Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoo ñaa ngay wax naan :

Simoore Aaya 34/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers