Ad-Dukhan · 32/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
وَلَقَدِ اخْتَرْنَاهُمْ عَلَىٰ عِلْمٍ عَلَى الْعَالَمِينَ ۝٣٢
Wa laqadikh tarnaahum `alaa `ilmin `alal `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Tànnoon Nanu leen tigi ci kaw waa àddina sépp (bawoo jamono),

🎧 Dégg


📜 Aaya 30-34 — Simoore Ad-Dukhan

30وَلَقَدْ نَجَّيْنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ مِنَ الْعَذَابِ الْمُهِينِ
Musëloon Nanu , waa bani Israayiila ci mbugël mu doyadima (rey góor)
31مِن فِرْعَوْنَ ۚ إِنَّهُ كَانَ عَالِيًا مِّنَ الْمُسْرِفِينَ
mom Firawna ma kawe woon lool ca yàqkat ya.
32وَلَقَدِ اخْتَرْنَاهُمْ عَلَىٰ عِلْمٍ عَلَى الْعَالَمِينَ
Tànnoon Nanu leen tigi ci kaw waa àddina sépp (bawoo jamono),
33وَآتَيْنَاهُم مِّنَ الْآيَاتِ مَا فِيهِ بَلَاءٌ مُّبِينٌ
indiloon Nanu leen ay kéemaan (firnde) yu leer nàññ.
34إِنَّ هَٰؤُلَاءِ لَيَقُولُونَ
Ñoo ñaa ngay wax naan :
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 32

Simoore Ad-Dukhan Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Tànnoon Nanu leen tigi ci kaw waa àddina sépp (bawoo…

Simoore Aaya 32/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers