Al-Jathiya · 32/37
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Jathiya
وَإِذَا قِيلَ إِنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ وَالسَّاعَةُ لَا رَيْبَ فِيهَا قُلْتُم مَّا نَدْرِي مَا السَّاعَةُ إِن نَّظُنُّ إِلَّا ظَنًّا وَمَا نَحْنُ بِمُسْتَيْقِنِينَ ۝٣٢
Wa izaa qeela inna wa`dallaahi haqqunw was Saa`atu laa raiba feehaa qultum maa nadree mas Saa`atu in nazunnu illaa zannanw wa maa nahnu bimustaiqineen
📖 Tekkim Wolof
Te bu ñu leen waxaan ne : “digub Yàlla bii dëgg la de ; te it Bis Pénc ba sikkuwul”, ngeen daan tontu ne : “Nun sax xamunu luy Bis Pénc ba ; am nanu ci ay njortu te wóoluwu nu ko.

🎧 Dégg


📜 Aaya 30-34 — Simoore Al-Jathiya

30فَأَمَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ فَيُدْخِلُهُمْ رَبُّهُمْ فِي رَحْمَتِهِ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْفَوْزُ الْمُبِينُ
Ña gëmoon te daan jëf yiw, sa Boroom dana leen tàbbal ci biir yërmaandeem. loolu moo di texe gu màgg ga.
31وَأَمَّا الَّذِينَ كَفَرُوا أَفَلَمْ تَكُنْ آيَاتِي تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ فَاسْتَكْبَرْتُمْ وَكُنتُمْ قَوْمًا مُّجْرِمِينَ
Ña weddi woon : “Xanaa Sunuy kàddu daawuloon wàcci ca ñoom ? Ñuy rëy-rëylu ak a tooñ di jalgati”.
32وَإِذَا قِيلَ إِنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ وَالسَّاعَةُ لَا رَيْبَ فِيهَا قُلْتُم مَّا نَدْرِي مَا السَّاعَةُ إِن نَّظُنُّ إِلَّا ظَنًّا وَمَا نَحْنُ بِمُسْتَيْقِنِينَ
Te bu ñu leen waxaan ne : “digub Yàlla bii dëgg la de ; te it Bis Pénc ba sikkuwul”, ngeen daan tontu ne : “Nun sax xamunu luy Bis Pénc ba ; am nanu ci ay njortu te wóoluwu nu ko.
33وَبَدَا لَهُمْ سَيِّئَاتُ مَا عَمِلُوا وَحَاقَ بِهِم مَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Ñu ne gegg ca [ñaatéefi ] seen jëf ya. Lañu daan yejje gaw leen.
34وَقِيلَ الْيَوْمَ نَنسَاكُمْ كَمَا نَسِيتُمْ لِقَاءَ يَوْمِكُمْ هَٰذَا وَمَأْوَاكُمُ النَّارُ وَمَا لَكُم مِّن نَّاصِرِينَ
Ñu wax leen ne : “Bis niki tey dananu leen fàtte (bàyyi leen ci biir Safara) kem ni ngeen fàttewoon dajeg seen bis bii ( ba waajaluleen ko). Seenub dëkkuwaay mooy Safara ; te kenn du leen fa dimbali.
Al-JathiyaFihi Alxuraan
37Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Al-Jathiya 32

Simoore Al-Jathiya Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te bu ñu leen waxaan ne : “digub Yàlla bii…

Simoore Aaya 32/37 — Simoore Al-Jathiya الجاثية (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Jathiya Dégg, Simoore Al-Jathiya Tekki, Simoore Al-Jathiya mp3, Simoore Al-Jathiya pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers