Muhammad · 10/38
Tekki Waxtaan — Simoore Muhammad
۞ أَفَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَيَنظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ دَمَّرَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ ۖ وَلِلْكَافِرِينَ أَمْثَالُهَا ۝١٠
Afalam yaseeroo fil ardi fayanzuroo kaifa kaana `aaqibatul lazeena min qablihim; dammaral laahu `alaihim wa lilkaafireena amsaaluhaa
📖 Tekkim Wolof
Moo xanaa dañoo wërul ca réew yi (suuf si) bay xool naka la mujjug ña leen jiitu deme woon ? Yàlla da leen nappaaje (faag leen). Noonu it la yéefar yi di mujje.

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Simoore Muhammad

8وَالَّذِينَ كَفَرُوا فَتَعْسًا لَّهُمْ وَأَضَلَّ أَعْمَالَهُمْ
Ña weddiwoon, ñoom toskare nañu te séeni jëf réer na.
9ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ كَرِهُوا مَا أَنزَلَ اللَّهُ فَأَحْبَطَ أَعْمَالَهُمْ
Li ko waral moo di ne dañoo sibóon li Yàlla daan wàcce ci moom it. Mu daldi sippi séeni jëf (neenal ko).
10۞ أَفَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَيَنظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ دَمَّرَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ ۖ وَلِلْكَافِرِينَ أَمْثَالُهَا
Moo xanaa dañoo wërul ca réew yi (suuf si) bay xool naka la mujjug ña leen jiitu deme woon ? Yàlla da leen nappaaje (faag leen). Noonu it la yéefar yi di mujje.
11ذَٰلِكَ بِأَنَّ اللَّهَ مَوْلَى الَّذِينَ آمَنُوا وَأَنَّ الْكَافِرِينَ لَا مَوْلَىٰ لَهُمْ
Dafa fekk ne Yàlla mooy méngóo di Aar ñi gëm ; yéefar yi nag ñoom amu ñu ku leen di aar.
12إِنَّ اللَّهَ يُدْخِلُ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۖ وَالَّذِينَ كَفَرُوا يَتَمَتَّعُونَ وَيَأْكُلُونَ كَمَا تَأْكُلُ الْأَنْعَامُ وَالنَّارُ مَثْوًى لَّهُمْ
Yàlla dana tàbbal ñi gëmoon te daan jëfe yiw, Àjjana yoo xam ne ay dex ñooy daw ci suufam ronu leen. Ña weddiwoon ñoom dañu daan bànneexu ak daan lekk ni jur gi di lekke ; te safaraay séen saxuwaay.
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
10Aaya

Tekki — Muhammad 10

Simoore Muhammad Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo xanaa dañoo wërul ca réew yi (suuf si) bay…

Simoore Aaya 10/38 — Simoore Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Muhammad Dégg, Simoore Muhammad Tekki, Simoore Muhammad mp3, Simoore Muhammad pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers