Muhammad · 3/38
Tekki Waxtaan — Muhammad
ذَٰلِكَ بِأَنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا اتَّبَعُوا الْبَاطِلَ وَأَنَّ الَّذِينَ آمَنُوا اتَّبَعُوا الْحَقَّ مِن رَّبِّهِمْ ۚ كَذَٰلِكَ يَضْرِبُ اللَّهُ لِلنَّاسِ أَمْثَالَهُمْ ۝٣
Zaalika bi annal lazeena kafarut taba`ul baatila wa annal lazeena aamanut taba`ul haqqa mir Rabbihim; kazaalika yadribul laahu linnaasi amsaalahum
📖 Tekkim Wolof
Li wér moo di ne ñiy weddi dañoo topp Neen ñi gëm nag ñoom dañoo topp Dëgg gu bawoo ca séen Boroom. Noonu la Yàlla di séddale nit séeni léebu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-5 — Muhammad

1الَّذِينَ كَفَرُوا وَصَدُّوا عَن سَبِيلِ اللَّهِ أَضَلَّ أَعْمَالَهُمْ
Ña weddi tey dumóoyu yoonu Yàlla, (tax na) ba sànk na séen jëf.
2وَالَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ وَآمَنُوا بِمَا نُزِّلَ عَلَىٰ مُحَمَّدٍ وَهُوَ الْحَقُّ مِن رَّبِّهِمْ ۙ كَفَّرَ عَنْهُمْ سَيِّئَاتِهِمْ وَأَصْلَحَ بَالَهُمْ
Ña gëmoon te daan jëf yiw te ñoo daan gëm la ñu daan wàcce ci Muhammad (Alxuraan) – te mooy dëgg ga bawoo ca séen Boroom – Faralal na leen séen ñaawtéef te it yéwénal na leen séen mbir.
3ذَٰلِكَ بِأَنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا اتَّبَعُوا الْبَاطِلَ وَأَنَّ الَّذِينَ آمَنُوا اتَّبَعُوا الْحَقَّ مِن رَّبِّهِمْ ۚ كَذَٰلِكَ يَضْرِبُ اللَّهُ لِلنَّاسِ أَمْثَالَهُمْ
Li wér moo di ne ñiy weddi dañoo topp Neen ñi gëm nag ñoom dañoo topp Dëgg gu bawoo ca séen Boroom. Noonu la Yàlla di séddale nit séeni léebu.
4فَإِذَا لَقِيتُمُ الَّذِينَ كَفَرُوا فَضَرْبَ الرِّقَابِ حَتَّىٰ إِذَا أَثْخَنتُمُوهُمْ فَشُدُّوا الْوَثَاقَ فَإِمَّا مَنًّا بَعْدُ وَإِمَّا فِدَاءً حَتَّىٰ تَضَعَ الْحَرْبُ أَوْزَارَهَا ۚ ذَٰلِكَ وَلَوْ يَشَاءُ اللَّهُ لَانتَصَرَ مِنْهُمْ وَلَٰكِن لِّيَبْلُوَ بَعْضَكُم بِبَعْضٍ ۗ وَالَّذِينَ قُتِلُوا فِي سَبِيلِ اللَّهِ فَلَن يُضِلَّ أَعْمَالَهُمْ
Te saa su ngeen fa dajeetee ak ñay weddi (ci jamonoy xare) dóorleen ci loos yi. Saa su ngeen leen noote nag, na ngeen leen jéng bu daŋ a daŋ. Su leen soobee, ngeen baal leen dem, wala ngeen laaj leen njotu, ba baa xare ba di giif. Lool nag, bu sooboon Yàlla, Dana feyyu ci kaw yéefar yi, waaye danay faral nattuwante ci ñeneen ña ca des. Te itam ña ñuy roy ci yoonu Yàlla (ña doon jullit), Séeni jëf du réer.
5سَيَهْدِيهِمْ وَيُصْلِحُ بَالَهُمْ
(Yàlla) dana leen xala gindi tey yéwénal seeni mbir,
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
3Aaya

Tekki — Muhammad 3

Simoore Muhammad Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Li wér moo di ne ñiy weddi dañoo topp Neen…

Simoore Aaya 3/38 — Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Muhammad Dégg, Muhammad Tekki, Muhammad mp3, Muhammad pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers