Muhammad · 5/38
Tekki Waxtaan — Muhammad
سَيَهْدِيهِمْ وَيُصْلِحُ بَالَهُمْ ۝٥
Sa-yahdeehim wa yusihu baalahum
📖 Tekkim Wolof
(Yàlla) dana leen xala gindi tey yéwénal seeni mbir,
🎧 Dégg

📜 Aaya 3-7 — Muhammad

3ذَٰلِكَ بِأَنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا اتَّبَعُوا الْبَاطِلَ وَأَنَّ الَّذِينَ آمَنُوا اتَّبَعُوا الْحَقَّ مِن رَّبِّهِمْ ۚ كَذَٰلِكَ يَضْرِبُ اللَّهُ لِلنَّاسِ أَمْثَالَهُمْ
Li wér moo di ne ñiy weddi dañoo topp Neen ñi gëm nag ñoom dañoo topp Dëgg gu bawoo ca séen Boroom. Noonu la Yàlla di séddale nit séeni léebu.
4فَإِذَا لَقِيتُمُ الَّذِينَ كَفَرُوا فَضَرْبَ الرِّقَابِ حَتَّىٰ إِذَا أَثْخَنتُمُوهُمْ فَشُدُّوا الْوَثَاقَ فَإِمَّا مَنًّا بَعْدُ وَإِمَّا فِدَاءً حَتَّىٰ تَضَعَ الْحَرْبُ أَوْزَارَهَا ۚ ذَٰلِكَ وَلَوْ يَشَاءُ اللَّهُ لَانتَصَرَ مِنْهُمْ وَلَٰكِن لِّيَبْلُوَ بَعْضَكُم بِبَعْضٍ ۗ وَالَّذِينَ قُتِلُوا فِي سَبِيلِ اللَّهِ فَلَن يُضِلَّ أَعْمَالَهُمْ
Te saa su ngeen fa dajeetee ak ñay weddi (ci jamonoy xare) dóorleen ci loos yi. Saa su ngeen leen noote nag, na ngeen leen jéng bu daŋ a daŋ. Su leen soobee, ngeen baal leen dem, wala ngeen laaj leen njotu, ba baa xare ba di giif. Lool nag, bu sooboon Yàlla, Dana feyyu ci kaw yéefar yi, waaye danay faral nattuwante ci ñeneen ña ca des. Te itam ña ñuy roy ci yoonu Yàlla (ña doon jullit), Séeni jëf du réer.
5سَيَهْدِيهِمْ وَيُصْلِحُ بَالَهُمْ
(Yàlla) dana leen xala gindi tey yéwénal seeni mbir,
6وَيُدْخِلُهُمُ الْجَنَّةَ عَرَّفَهَا لَهُمْ
te dana leen tàbbal Àjjana ju mu leen jagle.
7يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِن تَنصُرُوا اللَّهَ يَنصُرْكُمْ وَيُثَبِّتْ أَقْدَامَكُمْ
eey yéen ñi gëm ! bu ngeen taxawee temm ci yoonu Yàlla, Kon dey dana leen dimbali te it dana dëgëral séeni ndëggu (gindi leen ci xare).
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
5Aaya

Tekki — Muhammad 5

Simoore Muhammad Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Yàlla) dana leen xala gindi tey yéwénal seeni mbir,

Simoore Aaya 5/38 — Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Muhammad Dégg, Muhammad Tekki, Muhammad mp3, Muhammad pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers