At-Tur · 20/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
مُتَّكِئِينَ عَلَىٰ سُرُرٍ مَّصْفُوفَةٍ ۖ وَزَوَّجْنَاهُم بِحُورٍ عِينٍ ۝٢٠
Muttaki`eena `alaa sururim masfoofatinw wa zawwaj naahum bihoorin `een
📖 Tekkim Wolof
ñangay sóonu ci ay lal yu ñu sësële”, te may Nanu leen ay soxna yu “huuru al iin” (am bët jekk),

🎧 Dégg


📜 Aaya 18-22 — Simoore At-Tur

18فَاكِهِينَ بِمَا آتَاهُمْ رَبُّهُمْ وَوَقَاهُمْ رَبُّهُمْ عَذَابَ الْجَحِيمِ
ñangay xéewlóo la leen seen Boroom jox, te it fàggulna leen mbugalum Safara.
19كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
“Lekkleen te naan ndokkale, ngir la ngeen daan jëf,
20مُتَّكِئِينَ عَلَىٰ سُرُرٍ مَّصْفُوفَةٍ ۖ وَزَوَّجْنَاهُم بِحُورٍ عِينٍ
ñangay sóonu ci ay lal yu ñu sësële”, te may Nanu leen ay soxna yu “huuru al iin” (am bët jekk),
21وَالَّذِينَ آمَنُوا وَاتَّبَعَتْهُمْ ذُرِّيَّتُهُم بِإِيمَانٍ أَلْحَقْنَا بِهِمْ ذُرِّيَّتَهُمْ وَمَا أَلَتْنَاهُم مِّنْ عَمَلِهِم مِّن شَيْءٍ ۚ كُلُّ امْرِئٍ بِمَا كَسَبَ رَهِينٌ
Ña gëmoon te seen sët topp leen ca ngëm googee, Dananu def seeni sët ñu dab leen. Te duñu wàññi dara ci sen jëf, kenn ku nekk ay moom la mu sàkku.
22وَأَمْدَدْنَاهُم بِفَاكِهَةٍ وَلَحْمٍ مِّمَّا يَشْتَهُونَ
Te Dananu leen jox ay foytéef ak yàpp lépp lu ñu cay soxla.
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — At-Tur 20

Simoore At-Tur Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñangay sóonu ci ay lal yu ñu sësële”, te may…

Simoore Aaya 20/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers