At-Tur · 21/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
وَالَّذِينَ آمَنُوا وَاتَّبَعَتْهُمْ ذُرِّيَّتُهُم بِإِيمَانٍ أَلْحَقْنَا بِهِمْ ذُرِّيَّتَهُمْ وَمَا أَلَتْنَاهُم مِّنْ عَمَلِهِم مِّن شَيْءٍ ۚ كُلُّ امْرِئٍ بِمَا كَسَبَ رَهِينٌ ۝٢١
Wallazeena aamanoo wattaba`at hum zurriyyatuhum bieemaanin alhaqnaa bihim zurriyyatahum wa maaa alatnaahum min `amalihim min shai`; kullum ri`im bimaa kasaba raheen
📖 Tekkim Wolof
Ña gëmoon te seen sët topp leen ca ngëm googee, Dananu def seeni sët ñu dab leen. Te duñu wàññi dara ci sen jëf, kenn ku nekk ay moom la mu sàkku.

🎧 Dégg


📜 Aaya 19-23 — Simoore At-Tur

19كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
“Lekkleen te naan ndokkale, ngir la ngeen daan jëf,
20مُتَّكِئِينَ عَلَىٰ سُرُرٍ مَّصْفُوفَةٍ ۖ وَزَوَّجْنَاهُم بِحُورٍ عِينٍ
ñangay sóonu ci ay lal yu ñu sësële”, te may Nanu leen ay soxna yu “huuru al iin” (am bët jekk),
21وَالَّذِينَ آمَنُوا وَاتَّبَعَتْهُمْ ذُرِّيَّتُهُم بِإِيمَانٍ أَلْحَقْنَا بِهِمْ ذُرِّيَّتَهُمْ وَمَا أَلَتْنَاهُم مِّنْ عَمَلِهِم مِّن شَيْءٍ ۚ كُلُّ امْرِئٍ بِمَا كَسَبَ رَهِينٌ
Ña gëmoon te seen sët topp leen ca ngëm googee, Dananu def seeni sët ñu dab leen. Te duñu wàññi dara ci sen jëf, kenn ku nekk ay moom la mu sàkku.
22وَأَمْدَدْنَاهُم بِفَاكِهَةٍ وَلَحْمٍ مِّمَّا يَشْتَهُونَ
Te Dananu leen jox ay foytéef ak yàpp lépp lu ñu cay soxla.
23يَتَنَازَعُونَ فِيهَا كَأْسًا لَّا لَغْوٌ فِيهَا وَلَا تَأْثِيمٌ
Danuñu cay joqlante ak i kopp ci lu àndul ak i caaxaan waxatumalaa sobe.
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — At-Tur 21

Simoore At-Tur Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña gëmoon te seen sët topp leen ca ngëm googee,…

Simoore Aaya 21/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers