At-Tur · 19/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ ۝١٩
Kuloo washraboo haneee `am bimaa kuntum ta`maloon
📖 Tekkim Wolof
“Lekkleen te naan ndokkale, ngir la ngeen daan jëf,

🎧 Dégg


📜 Aaya 17-21 — Simoore At-Tur

17إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي جَنَّاتٍ وَنَعِيمٍ
Ña ragaloon Yàlla ña nga ca biir Àjjana ya ak i xéewël,
18فَاكِهِينَ بِمَا آتَاهُمْ رَبُّهُمْ وَوَقَاهُمْ رَبُّهُمْ عَذَابَ الْجَحِيمِ
ñangay xéewlóo la leen seen Boroom jox, te it fàggulna leen mbugalum Safara.
19كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
“Lekkleen te naan ndokkale, ngir la ngeen daan jëf,
20مُتَّكِئِينَ عَلَىٰ سُرُرٍ مَّصْفُوفَةٍ ۖ وَزَوَّجْنَاهُم بِحُورٍ عِينٍ
ñangay sóonu ci ay lal yu ñu sësële”, te may Nanu leen ay soxna yu “huuru al iin” (am bët jekk),
21وَالَّذِينَ آمَنُوا وَاتَّبَعَتْهُمْ ذُرِّيَّتُهُم بِإِيمَانٍ أَلْحَقْنَا بِهِمْ ذُرِّيَّتَهُمْ وَمَا أَلَتْنَاهُم مِّنْ عَمَلِهِم مِّن شَيْءٍ ۚ كُلُّ امْرِئٍ بِمَا كَسَبَ رَهِينٌ
Ña gëmoon te seen sët topp leen ca ngëm googee, Dananu def seeni sët ñu dab leen. Te duñu wàññi dara ci sen jëf, kenn ku nekk ay moom la mu sàkku.
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — At-Tur 19

Simoore At-Tur Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Lekkleen te naan ndokkale, ngir la ngeen daan jëf,

Simoore Aaya 19/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers