At-Tur · 48/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
وَاصْبِرْ لِحُكْمِ رَبِّكَ فَإِنَّكَ بِأَعْيُنِنَا ۖ وَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ حِينَ تَقُومُ ۝٤٨
Wasbir lihukmi rabbika fa innaka bi-a`yuninaa wa sabbih bihamdi rabbika heena taqoom
📖 Tekkim Wolof
Nangay muñ li sa Boroom di dogal. Doo raw sunuy gët (Nun Yàlla). Te ne ngay sàbbaal sa Boroom di ko sant saa soo jógee ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 46-49 — Simoore At-Tur

46يَوْمَ لَا يُغْنِي عَنْهُمْ كَيْدُهُمْ شَيْئًا وَلَا هُمْ يُنصَرُونَ
bu keroogee seen pexe duleen jariñ dara, te kenn duleen dimbali.
47وَإِنَّ لِلَّذِينَ ظَلَمُوا عَذَابًا دُونَ ذَٰلِكَ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Te kat tooñkat ya ñoom danañu am mbugël mu yées lolu. Waaye li ëpp ci ñoom duñu xam.
48وَاصْبِرْ لِحُكْمِ رَبِّكَ فَإِنَّكَ بِأَعْيُنِنَا ۖ وَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ حِينَ تَقُومُ
Nangay muñ li sa Boroom di dogal. Doo raw sunuy gët (Nun Yàlla). Te ne ngay sàbbaal sa Boroom di ko sant saa soo jógee ;
49وَمِنَ اللَّيْلِ فَسَبِّحْهُ وَإِدْبَارَ النُّجُومِ
Nangay sàbbaal it timis ak fajar (fa biddiw yi feqe ak fa muy sooxe).
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
48Aaya

Tekki — At-Tur 48

Simoore At-Tur Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangay muñ li sa Boroom di dogal. Doo raw sunuy…

Simoore Aaya 48/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 46–49. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers