At-Tur · 49/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
وَمِنَ اللَّيْلِ فَسَبِّحْهُ وَإِدْبَارَ النُّجُومِ ۝٤٩
Wa minal laili fasabbihhu wa idbaaran nujoom
📖 Tekkim Wolof
Nangay sàbbaal it timis ak fajar (fa biddiw yi feqe ak fa muy sooxe).

🎧 Dégg


📜 Aaya 47-49 — Simoore At-Tur

47وَإِنَّ لِلَّذِينَ ظَلَمُوا عَذَابًا دُونَ ذَٰلِكَ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Te kat tooñkat ya ñoom danañu am mbugël mu yées lolu. Waaye li ëpp ci ñoom duñu xam.
48وَاصْبِرْ لِحُكْمِ رَبِّكَ فَإِنَّكَ بِأَعْيُنِنَا ۖ وَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ حِينَ تَقُومُ
Nangay muñ li sa Boroom di dogal. Doo raw sunuy gët (Nun Yàlla). Te ne ngay sàbbaal sa Boroom di ko sant saa soo jógee ;
49وَمِنَ اللَّيْلِ فَسَبِّحْهُ وَإِدْبَارَ النُّجُومِ
Nangay sàbbaal it timis ak fajar (fa biddiw yi feqe ak fa muy sooxe).
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
49Aaya

Tekki — At-Tur 49

Simoore At-Tur Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangay sàbbaal it timis ak fajar (fa biddiw yi feqe…

Simoore Aaya 49/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 47–49. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers