At-Tur · 47/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
وَإِنَّ لِلَّذِينَ ظَلَمُوا عَذَابًا دُونَ ذَٰلِكَ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ ۝٤٧
Wa inna lillazeena zalamoo `azaaban doona zalika wa laakinna aksarahum laa ya`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Te kat tooñkat ya ñoom danañu am mbugël mu yées lolu. Waaye li ëpp ci ñoom duñu xam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 45-49 — Simoore At-Tur

45فَذَرْهُمْ حَتَّىٰ يُلَاقُوا يَوْمَهُمُ الَّذِي فِيهِ يُصْعَقُونَ
Bàyyileen , ba ñu dajeek bis ba ñu leen di mbugël,
46يَوْمَ لَا يُغْنِي عَنْهُمْ كَيْدُهُمْ شَيْئًا وَلَا هُمْ يُنصَرُونَ
bu keroogee seen pexe duleen jariñ dara, te kenn duleen dimbali.
47وَإِنَّ لِلَّذِينَ ظَلَمُوا عَذَابًا دُونَ ذَٰلِكَ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Te kat tooñkat ya ñoom danañu am mbugël mu yées lolu. Waaye li ëpp ci ñoom duñu xam.
48وَاصْبِرْ لِحُكْمِ رَبِّكَ فَإِنَّكَ بِأَعْيُنِنَا ۖ وَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ حِينَ تَقُومُ
Nangay muñ li sa Boroom di dogal. Doo raw sunuy gët (Nun Yàlla). Te ne ngay sàbbaal sa Boroom di ko sant saa soo jógee ;
49وَمِنَ اللَّيْلِ فَسَبِّحْهُ وَإِدْبَارَ النُّجُومِ
Nangay sàbbaal it timis ak fajar (fa biddiw yi feqe ak fa muy sooxe).
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
47Aaya

Tekki — At-Tur 47

Simoore At-Tur Aaya 47 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te kat tooñkat ya ñoom danañu am mbugël mu yées…

Simoore Aaya 47/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 45–49. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers