As-Saff · 2/14
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saff
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لِمَ تَقُولُونَ مَا لَا تَفْعَلُونَ ۝٢
Yaa ayyuhal lazeena aamanoo lima taqooloona maa laa taf`aloon
📖 Tekkim Wolof
Eey yéen ñi gëm ! Ana lan moo tax ngeen di wax lu ngeen dul def ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-4 — Simoore As-Saff

1سَبَّحَ لِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Ñi nekk ci asamaan yeek suuf si ña ngay sàbbaal Yàlla, te Moom moo di Boroom Kàttan ga, di Ku Xereñ ka.
2يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لِمَ تَقُولُونَ مَا لَا تَفْعَلُونَ
Eey yéen ñi gëm ! Ana lan moo tax ngeen di wax lu ngeen dul def ?
3كَبُرَ مَقْتًا عِندَ اللَّهِ أَن تَقُولُوا مَا لَا تَفْعَلُونَ
Wax ji ngeen di wax te du ngeen ko def ak jéppi gu rëy (la leen di jural ca Yàlla).
4إِنَّ اللَّهَ يُحِبُّ الَّذِينَ يُقَاتِلُونَ فِي سَبِيلِهِ صَفًّا كَأَنَّهُم بُنْيَانٌ مَّرْصُوصٌ
Yàlla safoona ñiy xeex ci yoonam wi def senn sàppe melni ñoom tabax bu ñu raax la ñu.
As-SaffFihi Alxuraan
14Aaya
MedinanRevelation
2Aaya

Tekki — As-Saff 2

Simoore As-Saff Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Eey yéen ñi gëm ! Ana lan moo tax ngeen…

Simoore Aaya 2/14 — Simoore As-Saff الصف (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saff Dégg, Simoore As-Saff Tekki, Simoore As-Saff mp3, Simoore As-Saff pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers