As-Saff · 1/14
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saff
سَبَّحَ لِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ ۝١
Sabbaha lillaahi maa fisamaawaati wa maa fil ardi wa huwal `Azeezul Hakeem
📖 Tekkim Wolof
Ñi nekk ci asamaan yeek suuf si ña ngay sàbbaal Yàlla, te Moom moo di Boroom Kàttan ga, di Ku Xereñ ka.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore As-Saff

1سَبَّحَ لِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Ñi nekk ci asamaan yeek suuf si ña ngay sàbbaal Yàlla, te Moom moo di Boroom Kàttan ga, di Ku Xereñ ka.
2يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لِمَ تَقُولُونَ مَا لَا تَفْعَلُونَ
Eey yéen ñi gëm ! Ana lan moo tax ngeen di wax lu ngeen dul def ?
3كَبُرَ مَقْتًا عِندَ اللَّهِ أَن تَقُولُوا مَا لَا تَفْعَلُونَ
Wax ji ngeen di wax te du ngeen ko def ak jéppi gu rëy (la leen di jural ca Yàlla).
As-SaffFihi Alxuraan
14Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — As-Saff 1

Simoore As-Saff Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñi nekk ci asamaan yeek suuf si ña ngay sàbbaal…

Simoore Aaya 1/14 — Simoore As-Saff الصف (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saff Dégg, Simoore As-Saff Tekki, Simoore As-Saff mp3, Simoore As-Saff pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers