At-Taghabun · 5/18
Tekki Waxtaan — At-Taghabun
أَلَمْ يَأْتِكُمْ نَبَأُ الَّذِينَ كَفَرُوا مِن قَبْلُ فَذَاقُوا وَبَالَ أَمْرِهِمْ وَلَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ ۝٥
Alam yaatikum naba`ul lazeena kafaroo min qablu fazaaqoo wabaala amrihim wa lahum `azaabun aleem
📖 Tekkim Wolof
Moo xanaa xibaari yéefar ya jiitu woon da leen dikkalul, mosoon nañu musiba mu di peyug seeni jëf ; te am nañu mbugël mu mitti.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — At-Taghabun

3خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ بِالْحَقِّ وَصَوَّرَكُمْ فَأَحْسَنَ صُوَرَكُمْ ۖ وَإِلَيْهِ الْمَصِيرُ
Bind na asamaan yeek suuf si ci dëgg mu tën seeni jëmm te rafetal na seeni jëm. Te ca moom mooy Deluwaay ba.
4يَعْلَمُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَيَعْلَمُ مَا تُسِرُّونَ وَمَا تُعْلِنُونَ ۚ وَاللَّهُ عَلِيمٌ بِذَاتِ الصُّدُورِ
Moom Yàlla xam na li nekk ci asamaan yeek suuf si, te it ma ngay xam li ngeen di nëbb ak li ngeen di feeñal. Te Yàlla ku xam la li nekk ci dënn yi.
5أَلَمْ يَأْتِكُمْ نَبَأُ الَّذِينَ كَفَرُوا مِن قَبْلُ فَذَاقُوا وَبَالَ أَمْرِهِمْ وَلَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ
Moo xanaa xibaari yéefar ya jiitu woon da leen dikkalul, mosoon nañu musiba mu di peyug seeni jëf ; te am nañu mbugël mu mitti.
6ذَٰلِكَ بِأَنَّهُ كَانَت تَّأْتِيهِمْ رُسُلُهُم بِالْبَيِّنَاتِ فَقَالُوا أَبَشَرٌ يَهْدُونَنَا فَكَفَرُوا وَتَوَلَّوا ۚ وَّاسْتَغْنَى اللَّهُ ۚ وَاللَّهُ غَنِيٌّ حَمِيدٌ
la ko waral moo di ne seeni Yonent da leen daan dikkël ak ay firndeyu leer ñuy wax naan : “Moo nit ñii ñoo ñuy gindee ? ” Daal di weddi dumóoyu Yàlla bàyyi leen te Yàlla ku doyloo boppam la Yayoowaakoonu cant la.
7زَعَمَ الَّذِينَ كَفَرُوا أَن لَّن يُبْعَثُوا ۚ قُلْ بَلَىٰ وَرَبِّي لَتُبْعَثُنَّ ثُمَّ لَتُنَبَّؤُنَّ بِمَا عَمِلْتُمْ ۚ وَذَٰلِكَ عَلَى اللَّهِ يَسِيرٌ
Yéefër yi neena ñooy kenn duleen dekkal. Waxal ne : “Axakañ! Dees na leen dekkal ; xibaar leen la ngeen jëfoon. Te loolu lu yomb la ci Yàlla”.
At-TaghabunFihi Alxuraan
18Aaya
MedinanRevelation
5Aaya

Tekki — At-Taghabun 5

Simoore At-Taghabun Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo xanaa xibaari yéefar ya jiitu woon da leen dikkalul,…

Simoore Aaya 5/18 — At-Taghabun التغابن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Taghabun Dégg, At-Taghabun Tekki, At-Taghabun mp3, At-Taghabun pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers