At-Tahrim · 7/12
Tekki Waxtaan — At-Tahrim
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ كَفَرُوا لَا تَعْتَذِرُوا الْيَوْمَ ۖ إِنَّمَا تُجْزَوْنَ مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ ۝٧
Yaaa ayyuhal lazeena kafaroo la ta`tazinul yawma innamaa tujzawna maa kuntum ta`maloon
📖 Tekkim Wolof
Éy yéen Yéefër yi! Buleen jéema jéggalu tey danañuleen fay la ngeen daan jëf.
🎧 Dégg

📜 Aaya 5-9 — At-Tahrim

5عَسَىٰ رَبُّهُ إِن طَلَّقَكُنَّ أَن يُبْدِلَهُ أَزْوَاجًا خَيْرًا مِّنكُنَّ مُسْلِمَاتٍ مُّؤْمِنَاتٍ قَانِتَاتٍ تَائِبَاتٍ عَابِدَاتٍ سَائِحَاتٍ ثَيِّبَاتٍ وَأَبْكَارًا
Te itam su leen fasee, Boroomam dana ko jox ay soxna yu leen gën, yu di ay jullit, yu gëm, yuy topp ndigal, ñuy tuub, ñuy jaamu, ñuy woor, di ay jeeg mba ay janq.
6يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا قُوا أَنفُسَكُمْ وَأَهْلِيكُمْ نَارًا وَقُودُهَا النَّاسُ وَالْحِجَارَةُ عَلَيْهَا مَلَائِكَةٌ غِلَاظٌ شِدَادٌ لَّا يَعْصُونَ اللَّهَ مَا أَمَرَهُمْ وَيَفْعَلُونَ مَا يُؤْمَرُونَ
Éy yéen ñi gëm ! Fegalleen seen bopp ak seen njaboot, aw Safara woo xam ne matt ma aw nit lay doon ak xeer, ay Malaaka yu tal, te tar, ñoo fay nekk duñu moy mukk, li leen Yàlla digal te la mu leen digal la ñuy def.
7يَا أَيُّهَا الَّذِينَ كَفَرُوا لَا تَعْتَذِرُوا الْيَوْمَ ۖ إِنَّمَا تُجْزَوْنَ مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Éy yéen Yéefër yi! Buleen jéema jéggalu tey danañuleen fay la ngeen daan jëf.
8يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا تُوبُوا إِلَى اللَّهِ تَوْبَةً نَّصُوحًا عَسَىٰ رَبُّكُمْ أَن يُكَفِّرَ عَنكُمْ سَيِّئَاتِكُمْ وَيُدْخِلَكُمْ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ يَوْمَ لَا يُخْزِي اللَّهُ النَّبِيَّ وَالَّذِينَ آمَنُوا مَعَهُ ۖ نُورُهُمْ يَسْعَىٰ بَيْنَ أَيْدِيهِمْ وَبِأَيْمَانِهِمْ يَقُولُونَ رَبَّنَا أَتْمِمْ لَنَا نُورَنَا وَاغْفِرْ لَنَا ۖ إِنَّكَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Éy yéen ñi gëm ! Tuuballeen Yàlla tuub gu sell. Kon dey Yàlla dana leen jéggal seeni ñaawtéef te Dana leen tàbbal ay Àjjana yu ay dex di daw ci suuf, bu keroogee Yàlla du gàcceel mukk Yonenta bi ak ñi gëm ànd ak moom. Seen leer gaa nga ca seen kanam ak ndeyjoor ; ña ngay wax naan : “Yaw sunu Boroom, mottalil nu sunug leer te jéggal nu. Yaw dey man nga lépp lu ne”.
9يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ جَاهِدِ الْكُفَّارَ وَالْمُنَافِقِينَ وَاغْلُظْ عَلَيْهِمْ ۚ وَمَأْوَاهُمْ جَهَنَّمُ ۖ وَبِئْسَ الْمَصِيرُ
Éy yaw Yonent bi ! Xeexal ak Yéefër yi ak Naaféq yi te na nga tar ci ñoom. Safaraay doon seenug muj, ndaw muj gu bon !
At-TahrimFihi Alxuraan
12Aaya
MedinanRevelation
7Aaya

Tekki — At-Tahrim 7

Simoore At-Tahrim Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yéen Yéefër yi! Buleen jéema jéggalu tey danañuleen fay…

Simoore Aaya 7/12 — At-Tahrim التحريم (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tahrim Dégg, At-Tahrim Tekki, At-Tahrim mp3, At-Tahrim pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers