Al-Mulk · 5/30
Tekki Waxtaan — Al-Mulk
وَلَقَدْ زَيَّنَّا السَّمَاءَ الدُّنْيَا بِمَصَابِيحَ وَجَعَلْنَاهَا رُجُومًا لِّلشَّيَاطِينِ ۖ وَأَعْتَدْنَا لَهُمْ عَذَابَ السَّعِيرِ ٥
Transliteration
Wa laqad zaiyannas samaaa`ad dunyaa bimasaa beeha wa ja`alnaahaa rujoomal lish shayaateeni wa a`tadnaa lahum `azaabas sa`eer
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Taaralal nanu àddina si ci ay làmp [biddiw] def nanu ko muy lakk Saytaane yi te waajalal nanu leen mbugëlum Safara.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 3-7 — Al-Mulk
3الَّذِي خَلَقَ سَبْعَ سَمَاوَاتٍ طِبَاقًا ۖ مَّا تَرَىٰ فِي خَلْقِ الرَّحْمَٰنِ مِن تَفَاوُتٍ ۖ فَارْجِعِ الْبَصَرَ هَلْ تَرَىٰ مِن فُطُورٍ
Mooy ki bind juróom-ñaari asamaan yu tegloo doo gis kenn roobaate ci bindug Yërëmaakoon bi. Dellul xool. Moo ndax danga gis genn sutaate ?
4ثُمَّ ارْجِعِ الْبَصَرَ كَرَّتَيْنِ يَنقَلِبْ إِلَيْكَ الْبَصَرُ خَاسِئًا وَهُوَ حَسِيرٌ
Topp, nga déllu xool ñaari yoon : da koy délloosiwaat ci yaw rekk waaye du man a gis sikk ne cucum.
5وَلَقَدْ زَيَّنَّا السَّمَاءَ الدُّنْيَا بِمَصَابِيحَ وَجَعَلْنَاهَا رُجُومًا لِّلشَّيَاطِينِ ۖ وَأَعْتَدْنَا لَهُمْ عَذَابَ السَّعِيرِ
Taaralal nanu àddina si ci ay làmp [biddiw] def nanu ko muy lakk Saytaane yi te waajalal nanu leen mbugëlum Safara.
6وَلِلَّذِينَ كَفَرُوا بِرَبِّهِمْ عَذَابُ جَهَنَّمَ ۖ وَبِئْسَ الْمَصِيرُ
Ña weddi Yàlla am nañu mbugalum Safara. Ndaw mujj gu bon !
7إِذَا أُلْقُوا فِيهَا سَمِعُوا لَهَا شَهِيقًا وَهِيَ تَفُورُ
Bu ñu leen ca sànnee, nga dégg ko muy fuur, di wañax.
Al-MulkFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
5Aaya
Tekki — Al-Mulk 5
Simoore Al-Mulk Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Taaralal nanu àddina si ci ay làmp [biddiw] def nanu…Simoore Aaya 5/30 — Al-Mulk الملك (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mulk Dégg, Al-Mulk Tekki, Al-Mulk mp3, Al-Mulk pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








