Al-Mulk · 6/30
Tekki Waxtaan — Al-Mulk
وَلِلَّذِينَ كَفَرُوا بِرَبِّهِمْ عَذَابُ جَهَنَّمَ ۖ وَبِئْسَ الْمَصِيرُ ۝٦
Wa lillazeena kafaroo bi rabbihim `azaabu jahannama wa bi`sal maseer
📖 Tekkim Wolof
Ña weddi Yàlla am nañu mbugalum Safara. Ndaw mujj gu bon !

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Al-Mulk

4ثُمَّ ارْجِعِ الْبَصَرَ كَرَّتَيْنِ يَنقَلِبْ إِلَيْكَ الْبَصَرُ خَاسِئًا وَهُوَ حَسِيرٌ
Topp, nga déllu xool ñaari yoon : da koy délloosiwaat ci yaw rekk waaye du man a gis sikk ne cucum.
5وَلَقَدْ زَيَّنَّا السَّمَاءَ الدُّنْيَا بِمَصَابِيحَ وَجَعَلْنَاهَا رُجُومًا لِّلشَّيَاطِينِ ۖ وَأَعْتَدْنَا لَهُمْ عَذَابَ السَّعِيرِ
Taaralal nanu àddina si ci ay làmp [biddiw] def nanu ko muy lakk Saytaane yi te waajalal nanu leen mbugëlum Safara.
6وَلِلَّذِينَ كَفَرُوا بِرَبِّهِمْ عَذَابُ جَهَنَّمَ ۖ وَبِئْسَ الْمَصِيرُ
Ña weddi Yàlla am nañu mbugalum Safara. Ndaw mujj gu bon !
7إِذَا أُلْقُوا فِيهَا سَمِعُوا لَهَا شَهِيقًا وَهِيَ تَفُورُ
Bu ñu leen ca sànnee, nga dégg ko muy fuur, di wañax.
8تَكَادُ تَمَيَّزُ مِنَ الْغَيْظِ ۖ كُلَّمَا أُلْقِيَ فِيهَا فَوْجٌ سَأَلَهُمْ خَزَنَتُهَا أَلَمْ يَأْتِكُمْ نَذِيرٌ
Day mer, bay fuur. Saa su ñu ca sànnee mbooloo, ña kay wattu naan leen: “Xanaa ! yéen kuy xuppe dikkul woon ci yéen ? ”
Al-MulkFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Mulk 6

Simoore Al-Mulk Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña weddi Yàlla am nañu mbugalum Safara. Ndaw mujj gu…

Simoore Aaya 6/30 — Al-Mulk الملك (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mulk Dégg, Al-Mulk Tekki, Al-Mulk mp3, Al-Mulk pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers