Al-A'raf · 137/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
وَأَوْرَثْنَا الْقَوْمَ الَّذِينَ كَانُوا يُسْتَضْعَفُونَ مَشَارِقَ الْأَرْضِ وَمَغَارِبَهَا الَّتِي بَارَكْنَا فِيهَا ۖ وَتَمَّتْ كَلِمَتُ رَبِّكَ الْحُسْنَىٰ عَلَىٰ بَنِي إِسْرَائِيلَ بِمَا صَبَرُوا ۖ وَدَمَّرْنَا مَا كَانَ يَصْنَعُ فِرْعَوْنُ وَقَوْمُهُ وَمَا كَانُوا يَعْرِشُونَ ۝١٣٧
Wa awrasnal qawmal lazeena kaanoo yustad`afoona mashaariqal ardi wa maghaari bahal latee baaraknaa feehaa wa tammat kalimatu Rabbikal husnaa `alaa Baneee Israaa`eela bimaa sabaroo wa dammarnaa maa kaana yasna`u Fir`awnu wa qawmuhoo wa maa kaanoo ya`rishoon
📖 Tekkim Wolof
Nu donnale suuf si nit ña ñu nekkoon daan leen suufeel, penku ba sowu te barkeel ko. Noonu, sa dogalu Boroom bu rafet bi, daldi mat ci Banii-israayil ngir la ñu nekkoon di muñ. Nu rajaxe la Firawna ak u nitam nekkoon di liggéey ak ya ñu tabaxoon.

🎧 Dégg


📜 Aaya 135-139 — Al-A'raf

135فَلَمَّا كَشَفْنَا عَنْهُمُ الرِّجْزَ إِلَىٰ أَجَلٍ هُم بَالِغُوهُ إِذَا هُمْ يَنكُثُونَ
Ba Nu teggee ca ñoom mbugal ma [ca àpp ba mu waroon a yem], firi nañu la ñu dige woon.
136فَانتَقَمْنَا مِنْهُمْ فَأَغْرَقْنَاهُمْ فِي الْيَمِّ بِأَنَّهُمْ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا وَكَانُوا عَنْهَا غَافِلِينَ
Tax na Nu feyyu ci ñoom ; labal leen ci géej gi, ndax ñoom dañoo weddi sunuy tegtal, sàggane leen.
137وَأَوْرَثْنَا الْقَوْمَ الَّذِينَ كَانُوا يُسْتَضْعَفُونَ مَشَارِقَ الْأَرْضِ وَمَغَارِبَهَا الَّتِي بَارَكْنَا فِيهَا ۖ وَتَمَّتْ كَلِمَتُ رَبِّكَ الْحُسْنَىٰ عَلَىٰ بَنِي إِسْرَائِيلَ بِمَا صَبَرُوا ۖ وَدَمَّرْنَا مَا كَانَ يَصْنَعُ فِرْعَوْنُ وَقَوْمُهُ وَمَا كَانُوا يَعْرِشُونَ
Nu donnale suuf si nit ña ñu nekkoon daan leen suufeel, penku ba sowu te barkeel ko. Noonu, sa dogalu Boroom bu rafet bi, daldi mat ci Banii-israayil ngir la ñu nekkoon di muñ. Nu rajaxe la Firawna ak u nitam nekkoon di liggéey ak ya ñu tabaxoon.
138وَجَاوَزْنَا بِبَنِي إِسْرَائِيلَ الْبَحْرَ فَأَتَوْا عَلَىٰ قَوْمٍ يَعْكُفُونَ عَلَىٰ أَصْنَامٍ لَّهُمْ ۚ قَالُوا يَا مُوسَى اجْعَل لَّنَا إِلَٰهًا كَمَا لَهُمْ آلِهَةٌ ۚ قَالَ إِنَّكُمْ قَوْمٌ تَجْهَلُونَ
Jàllale Nanu Bani-Israayil géej ga. Ñu fekk fa aw nit ñoo xam ne ña nga doon jaamu seeni xërëm, ñu ne : "Muusaa, defal nu yàlla ju mel ni seen yàlla.”. Mu ne leen : “Yéen daal ñu réer ngeen.
139إِنَّ هَٰؤُلَاءِ مُتَبَّرٌ مَّا هُمْ فِيهِ وَبَاطِلٌ مَّا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Nii la ñu nekkee di ñu alku; te seeni jëf lu yàqu la.”
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
137Aaya

Tekki — Al-A'raf 137

Simoore Al-A'raf Aaya 137 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu donnale suuf si nit ña ñu nekkoon daan leen…

Simoore Aaya 137/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 135–139. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers