Al-Jinn · 10/28
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Jinn
وَأَنَّا لَا نَدْرِي أَشَرٌّ أُرِيدَ بِمَن فِي الْأَرْضِ أَمْ أَرَادَ بِهِمْ رَبُّهُمْ رَشَدًا ١٠
Transliteration
Wa annaa laa nadreee asharrun ureeda biman fil ardi am araada bihim rabbuhum rashadaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te nun sax xamu nu ndax ñi nekk ci suuf si aw ay lees namm ci ñoom walla seen Boroom dafa namm ci ñoom ñu jub.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 8-12 — Simoore Al-Jinn
8وَأَنَّا لَمَسْنَا السَّمَاءَ فَوَجَدْنَاهَا مُلِئَتْ حَرَسًا شَدِيدًا وَشُهُبًا
te Nun kat làmbu Nanu asamaan si fekk mu fees dell ak i wattukat ak jumi safara.
9وَأَنَّا كُنَّا نَقْعُدُ مِنْهَا مَقَاعِدَ لِلسَّمْعِ ۖ فَمَن يَسْتَمِعِ الْآنَ يَجِدْ لَهُ شِهَابًا رَّصَدًا
Te nun danu fa daan toog di yadu. Leegi nag képp ku fay jéema yëdu ji, dana fa fekk ab jum bu koy tuŋlu.
10وَأَنَّا لَا نَدْرِي أَشَرٌّ أُرِيدَ بِمَن فِي الْأَرْضِ أَمْ أَرَادَ بِهِمْ رَبُّهُمْ رَشَدًا
Te nun sax xamu nu ndax ñi nekk ci suuf si aw ay lees namm ci ñoom walla seen Boroom dafa namm ci ñoom ñu jub.
11وَأَنَّا مِنَّا الصَّالِحُونَ وَمِنَّا دُونَ ذَٰلِكَ ۖ كُنَّا طَرَائِقَ قِدَدًا
Am na ci nun ñu jub am na it ñu yées loolu : nun daal ay kurél lanu yu limu.
12وَأَنَّا ظَنَنَّا أَن لَّن نُّعْجِزَ اللَّهَ فِي الْأَرْضِ وَلَن نُّعْجِزَهُ هَرَبًا
Te xam nanu ne manuñoo tiiñ Yàlla te it manuñoo daw mukk ba raw ko.
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
10Aaya
Tekki — Al-Jinn 10
Simoore Al-Jinn Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te nun sax xamu nu ndax ñi nekk ci suuf…Simoore Aaya 10/28 — Simoore Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Jinn Dégg, Simoore Al-Jinn Tekki, Simoore Al-Jinn mp3, Simoore Al-Jinn pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Al-Jinn
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Wednesday, September 30, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


