Al-Jinn · 19/28
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Jinn
وَأَنَّهُ لَمَّا قَامَ عَبْدُ اللَّهِ يَدْعُوهُ كَادُوا يَكُونُونَ عَلَيْهِ لِبَدًا ۝١٩
Wa annahoo lammaa qaama `adul laahi yad`oohu kaadoo yakoonoona `alaihi libadaa
📖 Tekkim Wolof
Te kat ba jaamub Yàlla bi taxawee di ñaan Boroomam, xawnañoo raj-rajloo ca kawam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 17-21 — Simoore Al-Jinn

17لِّنَفْتِنَهُمْ فِيهِ ۚ وَمَن يُعْرِضْ عَن ذِكْرِ رَبِّهِ يَسْلُكْهُ عَذَابًا صَعَدًا
ngir nu nattu leen ca. Képp ku dumóoyu baña fàttaliku Boroomam, (Yàlla) dana ko sóob ci mbugël muy dolliku saa su nekk.
18وَأَنَّ الْمَسَاجِدَ لِلَّهِ فَلَا تَدْعُوا مَعَ اللَّهِ أَحَدًا
Jàkka yi Yàlla moo leen moom : buleen fay woo kenn di ko booleek Yàlla.
19وَأَنَّهُ لَمَّا قَامَ عَبْدُ اللَّهِ يَدْعُوهُ كَادُوا يَكُونُونَ عَلَيْهِ لِبَدًا
Te kat ba jaamub Yàlla bi taxawee di ñaan Boroomam, xawnañoo raj-rajloo ca kawam.
20قُلْ إِنَّمَا أَدْعُو رَبِّي وَلَا أُشْرِكُ بِهِ أَحَدًا
Waxal ne : “Maa ngi ñaan sama Boroom te duma ko bokkaaleek kenn”.
21قُلْ إِنِّي لَا أَمْلِكُ لَكُمْ ضَرًّا وَلَا رَشَدًا
Waxal ne: “man mii kat manuma leen a lor manuma leen a jubbanti ”.
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — Al-Jinn 19

Simoore Al-Jinn Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te kat ba jaamub Yàlla bi taxawee di ñaan Boroomam,…

Simoore Aaya 19/28 — Simoore Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Jinn Dégg, Simoore Al-Jinn Tekki, Simoore Al-Jinn mp3, Simoore Al-Jinn pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers