Al-Jinn · 23/28
Tekki Waxtaan — Al-Jinn
إِلَّا بَلَاغًا مِّنَ اللَّهِ وَرِسَالَاتِهِ ۚ وَمَن يَعْصِ اللَّهَ وَرَسُولَهُ فَإِنَّ لَهُ نَارَ جَهَنَّمَ خَالِدِينَ فِيهَا أَبَدًا ٢٣
Transliteration
Illaa balaagham minal laahi wa risaalaatih; wa many ya`sil laaha wa rasoolahoo fa inna lahoo naara jahannama khaalideena feehaaa abadaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Manuma lu dul jottali ndigëlul Yàlla. Waaye képp ku moy Yàlla akub Yonentam ca Safara sa lay sax te dafay béel ba fàww.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 21-25 — Al-Jinn
21قُلْ إِنِّي لَا أَمْلِكُ لَكُمْ ضَرًّا وَلَا رَشَدًا
Waxal ne: “man mii kat manuma leen a lor manuma leen a jubbanti ”.
22قُلْ إِنِّي لَن يُجِيرَنِي مِنَ اللَّهِ أَحَدٌ وَلَنْ أَجِدَ مِن دُونِهِ مُلْتَحَدًا
Waxal it ne: “man mii keen manumaa aar ci Yàlla, te it duma wut benn rawtukaay budul moom.
23إِلَّا بَلَاغًا مِّنَ اللَّهِ وَرِسَالَاتِهِ ۚ وَمَن يَعْصِ اللَّهَ وَرَسُولَهُ فَإِنَّ لَهُ نَارَ جَهَنَّمَ خَالِدِينَ فِيهَا أَبَدًا
Manuma lu dul jottali ndigëlul Yàlla. Waaye képp ku moy Yàlla akub Yonentam ca Safara sa lay sax te dafay béel ba fàww.
24حَتَّىٰ إِذَا رَأَوْا مَا يُوعَدُونَ فَسَيَعْلَمُونَ مَنْ أَضْعَفُ نَاصِرًا وَأَقَلُّ عَدَدًا
Ba bis ba ñu gisee la ñu leen daan tëkkoo, danañu xala xam ana kan moo gën ñàkk ndimbal ak ana kan moo gën a néew lim.
25قُلْ إِنْ أَدْرِي أَقَرِيبٌ مَّا تُوعَدُونَ أَمْ يَجْعَلُ لَهُ رَبِّي أَمَدًا
Waxal ne: “Xamuma baxam li ñu leen di tëkkoo dafa jiggeñ, walla, sama Boroom da leen may ab dig.
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
23Aaya
Tekki — Al-Jinn 23
Simoore Al-Jinn Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Manuma lu dul jottali ndigëlul Yàlla. Waaye képp ku moy…Simoore Aaya 23/28 — Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Jinn Dégg, Al-Jinn Tekki, Al-Jinn mp3, Al-Jinn pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








