Al-Muzzammil · 3/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muzzammil
نِّصْفَهُ أَوِ انقُصْ مِنْهُ قَلِيلًا ۝٣
Nisfahooo awinqus minhu qaleelaa
📖 Tekkim Wolof
Ab xaajam, walla sax nga wàññi ca lu tuuti ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-5 — Simoore Al-Muzzammil

1يَا أَيُّهَا الْمُزَّمِّلُ
Éy ! yaw, ku ñu sàng ki !
2قُمِ اللَّيْلَ إِلَّا قَلِيلًا
Jógal [di julli], ci guddi gi, bamu des lu ,néew ;
3نِّصْفَهُ أَوِ انقُصْ مِنْهُ قَلِيلًا
Ab xaajam, walla sax nga wàññi ca lu tuuti ;
4أَوْ زِدْ عَلَيْهِ وَرَتِّلِ الْقُرْآنَ تَرْتِيلًا
walla sax nga dolli ca. Te na ngay jàng Alxuraan, njàng mu léer.
5إِنَّا سَنُلْقِي عَلَيْكَ قَوْلًا ثَقِيلًا
Xalset nanu laa gàll wax ju diis.
Al-MuzzammilFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-Muzzammil 3

Simoore Al-Muzzammil Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ab xaajam, walla sax nga wàññi ca lu tuuti ;

Simoore Aaya 3/20 — Simoore Al-Muzzammil المزمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muzzammil Dégg, Simoore Al-Muzzammil Tekki, Simoore Al-Muzzammil mp3, Simoore Al-Muzzammil pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers