Al-Insan · 4/31
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Insan
إِنَّا أَعْتَدْنَا لِلْكَافِرِينَ سَلَاسِلَ وَأَغْلَالًا وَسَعِيرًا ۝٤
Innaaa a`tadnaa lilkaa fireena salaasila wa aghlaalanw wa sa`eeraa
📖 Tekkim Wolof
Waajalal nanu yéefar ya ay càllala, ak i jéng ak safara wuy bérëx.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-Insan

2إِنَّا خَلَقْنَا الْإِنسَانَ مِن نُّطْفَةٍ أَمْشَاجٍ نَّبْتَلِيهِ فَجَعَلْنَاهُ سَمِيعًا بَصِيرًا
Nun noo binde nit ci maniyu mu jaxasoo. Di ko nattu def ko muy dégg di gis.
3إِنَّا هَدَيْنَاهُ السَّبِيلَ إِمَّا شَاكِرًا وَإِمَّا كَفُورًا
Gindi nanu ko ci aw yoon , - amaana muy déloo njukkël di sant walla mu goreedi -
4إِنَّا أَعْتَدْنَا لِلْكَافِرِينَ سَلَاسِلَ وَأَغْلَالًا وَسَعِيرًا
Waajalal nanu yéefar ya ay càllala, ak i jéng ak safara wuy bérëx.
5إِنَّ الْأَبْرَارَ يَشْرَبُونَ مِن كَأْسٍ كَانَ مِزَاجُهَا كَافُورًا
Ñu baax ña danañuy naane ci kaas yu ñu jaxasee kaafar,
6عَيْنًا يَشْرَبُ بِهَا عِبَادُ اللَّهِ يُفَجِّرُونَهَا تَفْجِيرًا
Batab ndox boo xam ne. Jaami Yàlla yaa cay naan, ñu di ko bëtte fa mu leen soob.
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Insan 4

Simoore Al-Insan Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waajalal nanu yéefar ya ay càllala, ak i jéng ak…

Simoore Aaya 4/31 — Simoore Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Insan Dégg, Simoore Al-Insan Tekki, Simoore Al-Insan mp3, Simoore Al-Insan pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers