Al-Insan · 3/31
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Insan
إِنَّا هَدَيْنَاهُ السَّبِيلَ إِمَّا شَاكِرًا وَإِمَّا كَفُورًا ۝٣
Innaa hadainaahus sabeela immaa shaakiranw wa immaa kafoora
📖 Tekkim Wolof
Gindi nanu ko ci aw yoon , - amaana muy déloo njukkël di sant walla mu goreedi -

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-5 — Simoore Al-Insan

1هَلْ أَتَىٰ عَلَى الْإِنسَانِ حِينٌ مِّنَ الدَّهْرِ لَمْ يَكُن شَيْئًا مَّذْكُورًا
Mo ndax nit dafa amul woon ab diir ci jamono bu kenn daawu ko limaale?
2إِنَّا خَلَقْنَا الْإِنسَانَ مِن نُّطْفَةٍ أَمْشَاجٍ نَّبْتَلِيهِ فَجَعَلْنَاهُ سَمِيعًا بَصِيرًا
Nun noo binde nit ci maniyu mu jaxasoo. Di ko nattu def ko muy dégg di gis.
3إِنَّا هَدَيْنَاهُ السَّبِيلَ إِمَّا شَاكِرًا وَإِمَّا كَفُورًا
Gindi nanu ko ci aw yoon , - amaana muy déloo njukkël di sant walla mu goreedi -
4إِنَّا أَعْتَدْنَا لِلْكَافِرِينَ سَلَاسِلَ وَأَغْلَالًا وَسَعِيرًا
Waajalal nanu yéefar ya ay càllala, ak i jéng ak safara wuy bérëx.
5إِنَّ الْأَبْرَارَ يَشْرَبُونَ مِن كَأْسٍ كَانَ مِزَاجُهَا كَافُورًا
Ñu baax ña danañuy naane ci kaas yu ñu jaxasee kaafar,
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-Insan 3

Simoore Al-Insan Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Gindi nanu ko ci aw yoon , - amaana muy…

Simoore Aaya 3/31 — Simoore Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Insan Dégg, Simoore Al-Insan Tekki, Simoore Al-Insan mp3, Simoore Al-Insan pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers