Al-Insan · 5/31
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Insan
إِنَّ الْأَبْرَارَ يَشْرَبُونَ مِن كَأْسٍ كَانَ مِزَاجُهَا كَافُورًا ۝٥
innal abraara yashra boona min kaasin kaana mizaa juhaa kaafooraa
📖 Tekkim Wolof
Ñu baax ña danañuy naane ci kaas yu ñu jaxasee kaafar,

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Al-Insan

3إِنَّا هَدَيْنَاهُ السَّبِيلَ إِمَّا شَاكِرًا وَإِمَّا كَفُورًا
Gindi nanu ko ci aw yoon , - amaana muy déloo njukkël di sant walla mu goreedi -
4إِنَّا أَعْتَدْنَا لِلْكَافِرِينَ سَلَاسِلَ وَأَغْلَالًا وَسَعِيرًا
Waajalal nanu yéefar ya ay càllala, ak i jéng ak safara wuy bérëx.
5إِنَّ الْأَبْرَارَ يَشْرَبُونَ مِن كَأْسٍ كَانَ مِزَاجُهَا كَافُورًا
Ñu baax ña danañuy naane ci kaas yu ñu jaxasee kaafar,
6عَيْنًا يَشْرَبُ بِهَا عِبَادُ اللَّهِ يُفَجِّرُونَهَا تَفْجِيرًا
Batab ndox boo xam ne. Jaami Yàlla yaa cay naan, ñu di ko bëtte fa mu leen soob.
7يُوفُونَ بِالنَّذْرِ وَيَخَافُونَ يَوْمًا كَانَ شَرُّهُ مُسْتَطِيرًا
Dañuy mottali seeni nisër tey ragal bis bu ayam wa tiis na .
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-Insan 5

Simoore Al-Insan Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu baax ña danañuy naane ci kaas yu ñu jaxasee…

Simoore Aaya 5/31 — Simoore Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Insan Dégg, Simoore Al-Insan Tekki, Simoore Al-Insan mp3, Simoore Al-Insan pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers