An-Nazi'at · 8/46
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nazi'at
قُلُوبٌ يَوْمَئِذٍ وَاجِفَةٌ ۝٨
Quloobuny-yau maaiziw-waaji-fa
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee, dana am ay xol yu tiit,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 6-10 — Simoore An-Nazi'at

6يَوْمَ تَرْجُفُ الرَّاجِفَةُ
Ca bis boobule [suuf] di yëngutu ci wal gu jëkkug mbiib ga [bufta ba]
7تَتْبَعُهَا الرَّادِفَةُ
ñaarelug wal ga daldi cay topp.
8قُلُوبٌ يَوْمَئِذٍ وَاجِفَةٌ
Bu keroogee, dana am ay xol yu tiit,
9أَبْصَارُهَا خَاشِعَةٌ
seenub gis sàjju ngir ragal.
10يَقُولُونَ أَإِنَّا لَمَرْدُودُونَ فِي الْحَافِرَةِ
Ña ngay wax naan : “Ndax danuy dundaat ginnaaw dee,
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — An-Nazi'at 8

Simoore An-Nazi'at Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee, dana am ay xol yu tiit,

Simoore Aaya 8/46 — Simoore An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nazi'at Dégg, Simoore An-Nazi'at Tekki, Simoore An-Nazi'at mp3, Simoore An-Nazi'at pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers