An-Nazi'at · 9/46
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nazi'at
أَبْصَارُهَا خَاشِعَةٌ ۝٩
Absaa ruhaa khashi`ah
📖 Tekkim Wolof
seenub gis sàjju ngir ragal.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 7-11 — Simoore An-Nazi'at

7تَتْبَعُهَا الرَّادِفَةُ
ñaarelug wal ga daldi cay topp.
8قُلُوبٌ يَوْمَئِذٍ وَاجِفَةٌ
Bu keroogee, dana am ay xol yu tiit,
9أَبْصَارُهَا خَاشِعَةٌ
seenub gis sàjju ngir ragal.
10يَقُولُونَ أَإِنَّا لَمَرْدُودُونَ فِي الْحَافِرَةِ
Ña ngay wax naan : “Ndax danuy dundaat ginnaaw dee,
11أَإِذَا كُنَّا عِظَامًا نَّخِرَةً
ak sax ginnaaw bu nu doonee ay yax yu funux ? ”
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — An-Nazi'at 9

Simoore An-Nazi'at Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : seenub gis sàjju ngir ragal.

Simoore Aaya 9/46 — Simoore An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nazi'at Dégg, Simoore An-Nazi'at Tekki, Simoore An-Nazi'at mp3, Simoore An-Nazi'at pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers