Al-Buruj · 10/22
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Buruj
إِنَّ الَّذِينَ فَتَنُوا الْمُؤْمِنِينَ وَالْمُؤْمِنَاتِ ثُمَّ لَمْ يَتُوبُوا فَلَهُمْ عَذَابُ جَهَنَّمَ وَلَهُمْ عَذَابُ الْحَرِيقِ ۝١٠
Innal lazeena fatanul mu`mineena wal mu`minaati summa lam yatooboo falahum `azaabu Jahannama wa lahum `azaabul hareeq
📖 Tekkim Wolof
Ña daan fitnaal jullit yu góor yaak yu jigéen ya, te tubu ñu ko, dananu am mbugëlum Jahanama ñu di leen ca lakk. (ca safaraam wa)

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Simoore Al-Buruj

8وَمَا نَقَمُوا مِنْهُمْ إِلَّا أَن يُؤْمِنُوا بِاللَّهِ الْعَزِيزِ الْحَمِيدِ
te fitnaale wu ñu leen ci lu dul ne da ñoo gëm Yàlla, boroom Kàttan ga, Yayoowaakooni cant ba,
9الَّذِي لَهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَاللَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ شَهِيدٌ
Yàlla mi moom nguurug asamaan yeek suuf si. Te yàlla seede la ci lépp lu ne.
10إِنَّ الَّذِينَ فَتَنُوا الْمُؤْمِنِينَ وَالْمُؤْمِنَاتِ ثُمَّ لَمْ يَتُوبُوا فَلَهُمْ عَذَابُ جَهَنَّمَ وَلَهُمْ عَذَابُ الْحَرِيقِ
Ña daan fitnaal jullit yu góor yaak yu jigéen ya, te tubu ñu ko, dananu am mbugëlum Jahanama ñu di leen ca lakk. (ca safaraam wa)
11إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَهُمْ جَنَّاتٌ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۚ ذَٰلِكَ الْفَوْزُ الْكَبِيرُ
Ña gëmoon te daan jëf yiw am nañu ay Àjjana yu ay dex di daw ci suufam. Loolu moo di texe gu mag ga.
12إِنَّ بَطْشَ رَبِّكَ لَشَدِيدٌ
Sa fayug boroom lu tar la.
Al-BurujFihi Alxuraan
22Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Al-Buruj 10

Simoore Al-Buruj Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña daan fitnaal jullit yu góor yaak yu jigéen ya,…

Simoore Aaya 10/22 — Simoore Al-Buruj البروج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Buruj Dégg, Simoore Al-Buruj Tekki, Simoore Al-Buruj mp3, Simoore Al-Buruj pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers