Al-Fajr · 12/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Fajr
فَأَكْثَرُوا فِيهَا الْفَسَادَ ۝١٢
Fa aksaroo feehal fasaad
📖 Tekkim Wolof
te ñu bariloon fa lool ag yàq.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Simoore Al-Fajr

10وَفِرْعَوْنَ ذِي الْأَوْتَادِ
ak Firawna, ma doonoon boroomi dàtt ?
11الَّذِينَ طَغَوْا فِي الْبِلَادِ
Ñoom, ñoo gënoona bew ci réew yi,
12فَأَكْثَرُوا فِيهَا الْفَسَادَ
te ñu bariloon fa lool ag yàq.
13فَصَبَّ عَلَيْهِمْ رَبُّكَ سَوْطَ عَذَابٍ
Sa Boroom daldi leen sotti yarum mbugël.
14إِنَّ رَبَّكَ لَبِالْمِرْصَادِ
Sa Boroom nag ma ngay fuglu.
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Fajr 12

Simoore Al-Fajr Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te ñu bariloon fa lool ag yàq.

Simoore Aaya 12/30 — Simoore Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Fajr Dégg, Simoore Al-Fajr Tekki, Simoore Al-Fajr mp3, Simoore Al-Fajr pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers