Al-Fajr · 13/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Fajr
فَصَبَّ عَلَيْهِمْ رَبُّكَ سَوْطَ عَذَابٍ ۝١٣
Fasabba `alaihim Rabbuka sawta `azaab
📖 Tekkim Wolof
Sa Boroom daldi leen sotti yarum mbugël.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 11-15 — Simoore Al-Fajr

11الَّذِينَ طَغَوْا فِي الْبِلَادِ
Ñoom, ñoo gënoona bew ci réew yi,
12فَأَكْثَرُوا فِيهَا الْفَسَادَ
te ñu bariloon fa lool ag yàq.
13فَصَبَّ عَلَيْهِمْ رَبُّكَ سَوْطَ عَذَابٍ
Sa Boroom daldi leen sotti yarum mbugël.
14إِنَّ رَبَّكَ لَبِالْمِرْصَادِ
Sa Boroom nag ma ngay fuglu.
15فَأَمَّا الْإِنسَانُ إِذَا مَا ابْتَلَاهُ رَبُّهُ فَأَكْرَمَهُ وَنَعَّمَهُ فَيَقُولُ رَبِّي أَكْرَمَنِ
Nit nag, moom saa su ko boroomam nattoo teral ko xéewal ko, mu ne : “Sama Boroom teral na ma”.
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — Al-Fajr 13

Simoore Al-Fajr Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sa Boroom daldi leen sotti yarum mbugël.

Simoore Aaya 13/30 — Simoore Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Fajr Dégg, Simoore Al-Fajr Tekki, Simoore Al-Fajr mp3, Simoore Al-Fajr pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers