Al-Fajr · 6/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Fajr
أَلَمْ تَرَ كَيْفَ فَعَلَ رَبُّكَ بِعَادٍ ۝٦
Alam tara kaifa fa`ala rabbuka bi`aad
📖 Tekkim Wolof
Xanaa gisoo naka la sa Boroom def waa Aad

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-Fajr

4وَاللَّيْلِ إِذَا يَسْرِ
Ak ci guddi gi suy tàmbali !
5هَلْ فِي ذَٰلِكَ قَسَمٌ لِّذِي حِجْرٍ
Moo ndax nekk na ci loolu, ngiñul boroom xel ?
6أَلَمْ تَرَ كَيْفَ فَعَلَ رَبُّكَ بِعَادٍ
Xanaa gisoo naka la sa Boroom def waa Aad
7إِرَمَ ذَاتِ الْعِمَادِ
Iram, ma doon boroomi kenu,
8الَّتِي لَمْ يُخْلَقْ مِثْلُهَا فِي الْبِلَادِ
yoo xam ne kemam amul ci menn réew ?
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Fajr 6

Simoore Al-Fajr Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa gisoo naka la sa Boroom def waa Aad

Simoore Aaya 6/30 — Simoore Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Fajr Dégg, Simoore Al-Fajr Tekki, Simoore Al-Fajr mp3, Simoore Al-Fajr pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 9, 2026

Don't forget us in your sincere prayers