At-Tawba · 129/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
فَإِن تَوَلَّوْا فَقُلْ حَسْبِيَ اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ عَلَيْهِ تَوَكَّلْتُ ۖ وَهُوَ رَبُّ الْعَرْشِ الْعَظِيمِ ١٢٩
Transliteration
Fa in tawallaw faqul lhasbiyal laahu laaa ilaaha illaa Huwa `alaihi tawakkkaltu wa Huwa Rabbul `Arshil `Azeem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu dëddoo, neel : “Yàlla doy na ma. Amul jenn yàlla ju dul Moom. Te Moom laay dëgërloo ; te Moom moo di Boroom gàngunaay gu màgg ga (Aras)”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 127-129 — At-Tawba
127وَإِذَا مَا أُنزِلَتْ سُورَةٌ نَّظَرَ بَعْضُهُمْ إِلَىٰ بَعْضٍ هَلْ يَرَاكُم مِّنْ أَحَدٍ ثُمَّ انصَرَفُوا ۚ صَرَفَ اللَّهُ قُلُوبَهُم بِأَنَّهُمْ قَوْمٌ لَّا يَفْقَهُونَ
Te su ñu wàccee aw saar ñu daldi xoolante, daldi wax ne : “Moo ndax am na ku nu gis ? ”. Daldi wëlbëtiku. Yal na Yàlla wëlbëti seeni xol ndax ñoom, aw nit lañu ñu amul genn dégg-dégg.
128لَقَدْ جَاءَكُمْ رَسُولٌ مِّنْ أَنفُسِكُمْ عَزِيزٌ عَلَيْهِ مَا عَنِتُّمْ حَرِيصٌ عَلَيْكُم بِالْمُؤْمِنِينَ رَءُوفٌ رَّحِيمٌ
Ab Yonent dikkal na leen bu bokk ci yéen, seeni coono tiis ci moom, di ku xér ci ngeen jub, di ku am ñeewant ak yërmaande ci jullit ñi.
129فَإِن تَوَلَّوْا فَقُلْ حَسْبِيَ اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ عَلَيْهِ تَوَكَّلْتُ ۖ وَهُوَ رَبُّ الْعَرْشِ الْعَظِيمِ
Bu ñu dëddoo, neel : “Yàlla doy na ma. Amul jenn yàlla ju dul Moom. Te Moom laay dëgërloo ; te Moom moo di Boroom gàngunaay gu màgg ga (Aras)”.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
129Aaya
Tekki — At-Tawba 129
Simoore At-Tawba Aaya 129 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu dëddoo, neel : “Yàlla doy na ma. Amul…Simoore Aaya 129/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 127–129. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers







