At-Tawba · 14/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
قَاتِلُوهُمْ يُعَذِّبْهُمُ اللَّهُ بِأَيْدِيكُمْ وَيُخْزِهِمْ وَيَنصُرْكُمْ عَلَيْهِمْ وَيَشْفِ صُدُورَ قَوْمٍ مُّؤْمِنِينَ ۝١٤
Qaatiloohum yu`az zibhumul laahu bi aideekum wa yukhzihim wa yansurkum `alaihim wa yashfi sudoora qawmim mu `mineen
📖 Tekkim Wolof
Xareleen ak ñoom. Yàlla Dana leen mbugal ñoom, jaare ko ci seeni yoxo yéen, te Dana leen toroxal, Dana leen dimbali ci not leen te Dana seral xoli ñi gëm ña.

🎧 Dégg


📜 Aaya 12-16 — At-Tawba

12وَإِن نَّكَثُوا أَيْمَانَهُم مِّن بَعْدِ عَهْدِهِمْ وَطَعَنُوا فِي دِينِكُمْ فَقَاتِلُوا أَئِمَّةَ الْكُفْرِ ۙ إِنَّهُمْ لَا أَيْمَانَ لَهُمْ لَعَلَّهُمْ يَنتَهُونَ
Bu ñu firee seen kóllare ginnaaw ba ñu ko fasee, te di ayibal seen diine, xareleen ak njiiti yéefar yi - ndax ñoom faalewuñu kóllare - ndax xéy-na ñu yem, bàyyi yooyu.
13أَلَا تُقَاتِلُونَ قَوْمًا نَّكَثُوا أَيْمَانَهُمْ وَهَمُّوا بِإِخْرَاجِ الرَّسُولِ وَهُم بَدَءُوكُمْ أَوَّلَ مَرَّةٍ ۚ أَتَخْشَوْنَهُمْ ۚ فَاللَّهُ أَحَقُّ أَن تَخْشَوْهُ إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ
Li leen tere xeex ak nit ñay firi seeni kóllare, te ñuy yittewoo génne Yonent bi te ñoom ñoo leen jëkk a songu ? Moo ndax dangeen leen a ragal ? Te Yàllaa gën a yey ci ngeen ragal Ko ndegam ñu gëm ngeen !
14قَاتِلُوهُمْ يُعَذِّبْهُمُ اللَّهُ بِأَيْدِيكُمْ وَيُخْزِهِمْ وَيَنصُرْكُمْ عَلَيْهِمْ وَيَشْفِ صُدُورَ قَوْمٍ مُّؤْمِنِينَ
Xareleen ak ñoom. Yàlla Dana leen mbugal ñoom, jaare ko ci seeni yoxo yéen, te Dana leen toroxal, Dana leen dimbali ci not leen te Dana seral xoli ñi gëm ña.
15وَيُذْهِبْ غَيْظَ قُلُوبِهِمْ ۗ وَيَتُوبُ اللَّهُ عَلَىٰ مَن يَشَاءُ ۗ وَاللَّهُ عَلِيمٌ حَكِيمٌ
Te Dana dindi mer mi nekk ci seeni xol. Te Dana baal ku Ko neex. Yàlla Ku xam la, Ku xereñ la.
16أَمْ حَسِبْتُمْ أَن تُتْرَكُوا وَلَمَّا يَعْلَمِ اللَّهُ الَّذِينَ جَاهَدُوا مِنكُمْ وَلَمْ يَتَّخِذُوا مِن دُونِ اللَّهِ وَلَا رَسُولِهِ وَلَا الْمُؤْمِنِينَ وَلِيجَةً ۚ وَاللَّهُ خَبِيرٌ بِمَا تَعْمَلُونَ
Am dangeen a njortu ne Danu leen di bàyyi te Yàlla duleen nattu ba xam ñiy xareel diine te duñu jàpp xarit, bàyyi Yàlla ak Yonentam ak ña gëm ? Yàlla Ku xam li ngeen di def la.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
14Aaya

Tekki — At-Tawba 14

Simoore At-Tawba Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xareleen ak ñoom. Yàlla Dana leen mbugal ñoom, jaare ko…

Simoore Aaya 14/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers