At-Tawba · 15/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
وَيُذْهِبْ غَيْظَ قُلُوبِهِمْ ۗ وَيَتُوبُ اللَّهُ عَلَىٰ مَن يَشَاءُ ۗ وَاللَّهُ عَلِيمٌ حَكِيمٌ ١٥
Transliteration
Wa yuzhib ghaiza quloobihim; wa yatoobullaahu `alaa mai yashaaa`; wallaahu `Aleemun Hakeem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te Dana dindi mer mi nekk ci seeni xol. Te Dana baal ku Ko neex. Yàlla Ku xam la, Ku xereñ la.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 13-17 — At-Tawba
13أَلَا تُقَاتِلُونَ قَوْمًا نَّكَثُوا أَيْمَانَهُمْ وَهَمُّوا بِإِخْرَاجِ الرَّسُولِ وَهُم بَدَءُوكُمْ أَوَّلَ مَرَّةٍ ۚ أَتَخْشَوْنَهُمْ ۚ فَاللَّهُ أَحَقُّ أَن تَخْشَوْهُ إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ
Li leen tere xeex ak nit ñay firi seeni kóllare, te ñuy yittewoo génne Yonent bi te ñoom ñoo leen jëkk a songu ? Moo ndax dangeen leen a ragal ? Te Yàllaa gën a yey ci ngeen ragal Ko ndegam ñu gëm ngeen !
14قَاتِلُوهُمْ يُعَذِّبْهُمُ اللَّهُ بِأَيْدِيكُمْ وَيُخْزِهِمْ وَيَنصُرْكُمْ عَلَيْهِمْ وَيَشْفِ صُدُورَ قَوْمٍ مُّؤْمِنِينَ
Xareleen ak ñoom. Yàlla Dana leen mbugal ñoom, jaare ko ci seeni yoxo yéen, te Dana leen toroxal, Dana leen dimbali ci not leen te Dana seral xoli ñi gëm ña.
15وَيُذْهِبْ غَيْظَ قُلُوبِهِمْ ۗ وَيَتُوبُ اللَّهُ عَلَىٰ مَن يَشَاءُ ۗ وَاللَّهُ عَلِيمٌ حَكِيمٌ
Te Dana dindi mer mi nekk ci seeni xol. Te Dana baal ku Ko neex. Yàlla Ku xam la, Ku xereñ la.
16أَمْ حَسِبْتُمْ أَن تُتْرَكُوا وَلَمَّا يَعْلَمِ اللَّهُ الَّذِينَ جَاهَدُوا مِنكُمْ وَلَمْ يَتَّخِذُوا مِن دُونِ اللَّهِ وَلَا رَسُولِهِ وَلَا الْمُؤْمِنِينَ وَلِيجَةً ۚ وَاللَّهُ خَبِيرٌ بِمَا تَعْمَلُونَ
Am dangeen a njortu ne Danu leen di bàyyi te Yàlla duleen nattu ba xam ñiy xareel diine te duñu jàpp xarit, bàyyi Yàlla ak Yonentam ak ña gëm ? Yàlla Ku xam li ngeen di def la.
17مَا كَانَ لِلْمُشْرِكِينَ أَن يَعْمُرُوا مَسَاجِدَ اللَّهِ شَاهِدِينَ عَلَىٰ أَنفُسِهِم بِالْكُفْرِ ۚ أُولَٰئِكَ حَبِطَتْ أَعْمَالُهُمْ وَفِي النَّارِ هُمْ خَالِدُونَ
Yellul bokkaalekat ya di toppatoo jàkkay Yàlla ji, te ñoom ay seede lañu ci seen weddi ga. Ñoom seeni jëf yàqu na ; te danañu leen dugal Safara fàwwu.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
15Aaya
Tekki — At-Tawba 15
Simoore At-Tawba Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te Dana dindi mer mi nekk ci seeni xol. Te…Simoore Aaya 15/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers







