At-Tawba · 20/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
الَّذِينَ آمَنُوا وَهَاجَرُوا وَجَاهَدُوا فِي سَبِيلِ اللَّهِ بِأَمْوَالِهِمْ وَأَنفُسِهِمْ أَعْظَمُ دَرَجَةً عِندَ اللَّهِ ۚ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْفَائِزُونَ ۝٢٠
Allazeena aamanoo wa haajaroo wa jaahadoo fee sabeelil laahi bi amwaalihim wa anufsihim a`zamu darajatan `indal laah; wa ulaaa`ika humul faaa`izoon
📖 Tekkim Wolof
Ña nga xam ne dañoo gëm, gàddaay te ñuy xareel yoonu Yàlla ci joxe seeni alal walla seeni bakkan, ñooy ña gën a màgg dayo ya ca Yàlla... ñoom ñooy ñu texe ña.
🎧 Dégg

📜 Aaya 18-22 — At-Tawba

18إِنَّمَا يَعْمُرُ مَسَاجِدَ اللَّهِ مَنْ آمَنَ بِاللَّهِ وَالْيَوْمِ الْآخِرِ وَأَقَامَ الصَّلَاةَ وَآتَى الزَّكَاةَ وَلَمْ يَخْشَ إِلَّا اللَّهَ ۖ فَعَسَىٰ أُولَٰئِكَ أَن يَكُونُوا مِنَ الْمُهْتَدِينَ
Ki yayoo dundal jàkkay Yàlla ja kay, mooy ku gëm Yàlla ak Bis-pénc ba, tey julli, di joxe asaka te du ragal kenn ku dul Yàlla. Kon ñooña, amaana ñu bokk ca ñu gindiku ña.
19۞ أَجَعَلْتُمْ سِقَايَةَ الْحَاجِّ وَعِمَارَةَ الْمَسْجِدِ الْحَرَامِ كَمَنْ آمَنَ بِاللَّهِ وَالْيَوْمِ الْآخِرِ وَجَاهَدَ فِي سَبِيلِ اللَّهِ ۚ لَا يَسْتَوُونَ عِندَ اللَّهِ ۗ وَاللَّهُ لَا يَهْدِي الْقَوْمَ الظَّالِمِينَ
Moo ndax dangeen di yemale [jëfi] kay dàndale ñay aji tey toppatoo jàkka ju ñu wormaal ak jëfi ka gëm Yàlla ak Bis-pénc ba te xareel yoonu Yàlla ? yemuñu ca Yàlla te Yàlla du gindi nit ñuy tooñ.
20الَّذِينَ آمَنُوا وَهَاجَرُوا وَجَاهَدُوا فِي سَبِيلِ اللَّهِ بِأَمْوَالِهِمْ وَأَنفُسِهِمْ أَعْظَمُ دَرَجَةً عِندَ اللَّهِ ۚ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْفَائِزُونَ
Ña nga xam ne dañoo gëm, gàddaay te ñuy xareel yoonu Yàlla ci joxe seeni alal walla seeni bakkan, ñooy ña gën a màgg dayo ya ca Yàlla... ñoom ñooy ñu texe ña.
21يُبَشِّرُهُمْ رَبُّهُم بِرَحْمَةٍ مِّنْهُ وَرِضْوَانٍ وَجَنَّاتٍ لَّهُمْ فِيهَا نَعِيمٌ مُّقِيمٌ
Seen Boroom a leen di bégale yërmaandeem ak ngërëmam, ak i Àjjana yu ñuy ame xéewal gu sax
22خَالِدِينَ فِيهَا أَبَدًا ۚ إِنَّ اللَّهَ عِندَهُ أَجْرٌ عَظِيمٌ
dañu fay dëkk fàwwu. Pey gu màgg moo nekk fa Yàlla.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
20Aaya

Tekki — At-Tawba 20

Simoore At-Tawba Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña nga xam ne dañoo gëm, gàddaay te ñuy xareel…

Simoore Aaya 20/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers