At-Tawba · 21/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
يُبَشِّرُهُمْ رَبُّهُم بِرَحْمَةٍ مِّنْهُ وَرِضْوَانٍ وَجَنَّاتٍ لَّهُمْ فِيهَا نَعِيمٌ مُّقِيمٌ ۝٢١
Yubashshiruhum Rabbuhum birahmatim minhu wa ridwaaninw wa Jannaatil lahum feehaa na`eemum muqeem
📖 Tekkim Wolof
Seen Boroom a leen di bégale yërmaandeem ak ngërëmam, ak i Àjjana yu ñuy ame xéewal gu sax
🎧 Dégg

📜 Aaya 19-23 — At-Tawba

19۞ أَجَعَلْتُمْ سِقَايَةَ الْحَاجِّ وَعِمَارَةَ الْمَسْجِدِ الْحَرَامِ كَمَنْ آمَنَ بِاللَّهِ وَالْيَوْمِ الْآخِرِ وَجَاهَدَ فِي سَبِيلِ اللَّهِ ۚ لَا يَسْتَوُونَ عِندَ اللَّهِ ۗ وَاللَّهُ لَا يَهْدِي الْقَوْمَ الظَّالِمِينَ
Moo ndax dangeen di yemale [jëfi] kay dàndale ñay aji tey toppatoo jàkka ju ñu wormaal ak jëfi ka gëm Yàlla ak Bis-pénc ba te xareel yoonu Yàlla ? yemuñu ca Yàlla te Yàlla du gindi nit ñuy tooñ.
20الَّذِينَ آمَنُوا وَهَاجَرُوا وَجَاهَدُوا فِي سَبِيلِ اللَّهِ بِأَمْوَالِهِمْ وَأَنفُسِهِمْ أَعْظَمُ دَرَجَةً عِندَ اللَّهِ ۚ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْفَائِزُونَ
Ña nga xam ne dañoo gëm, gàddaay te ñuy xareel yoonu Yàlla ci joxe seeni alal walla seeni bakkan, ñooy ña gën a màgg dayo ya ca Yàlla... ñoom ñooy ñu texe ña.
21يُبَشِّرُهُمْ رَبُّهُم بِرَحْمَةٍ مِّنْهُ وَرِضْوَانٍ وَجَنَّاتٍ لَّهُمْ فِيهَا نَعِيمٌ مُّقِيمٌ
Seen Boroom a leen di bégale yërmaandeem ak ngërëmam, ak i Àjjana yu ñuy ame xéewal gu sax
22خَالِدِينَ فِيهَا أَبَدًا ۚ إِنَّ اللَّهَ عِندَهُ أَجْرٌ عَظِيمٌ
dañu fay dëkk fàwwu. Pey gu màgg moo nekk fa Yàlla.
23يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَتَّخِذُوا آبَاءَكُمْ وَإِخْوَانَكُمْ أَوْلِيَاءَ إِنِ اسْتَحَبُّوا الْكُفْرَ عَلَى الْإِيمَانِ ۚ وَمَن يَتَوَلَّهُم مِّنكُمْ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الظَّالِمُونَ
Éy yéen ñi gëm ! Buleen def seeni baay ak seen mbokk yi ay xarit ndegam tànn nañu weddi, bàyyi ña gëm. Ku leen def xarit ca yéen... bokk na ca tooñkat ya.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
21Aaya

Tekki — At-Tawba 21

Simoore At-Tawba Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seen Boroom a leen di bégale yërmaandeem ak ngërëmam, ak…

Simoore Aaya 21/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers