At-Tawba · 52/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
قُلْ هَلْ تَرَبَّصُونَ بِنَا إِلَّا إِحْدَى الْحُسْنَيَيْنِ ۖ وَنَحْنُ نَتَرَبَّصُ بِكُمْ أَن يُصِيبَكُمُ اللَّهُ بِعَذَابٍ مِّنْ عِندِهِ أَوْ بِأَيْدِينَا ۖ فَتَرَبَّصُوا إِنَّا مَعَكُم مُّتَرَبِّصُونَ ۝٥٢
Qul hal tarabbasoona binaaa illaaa ihdal husnayayni wa nahnu natrabbasu bikum ai yus eebakumul laahu bi`azaa bim min `indiheee aw biaidee naa fatarabbasooo innaa ma`akum mutarabbisoon
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “Yéen a ngi nuy tuŋlu, te nun lu mën a xew, dananu am benn ci ñaari ndam yi [dee Chahiid walla nu dàq leen, not leen], benn Yàlla mbugal leen ci sunuy loxo, walla Mu xaroo leen ko ba ëllëg. Kon book nanu ànd di tuŋlu”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 50-54 — At-Tawba

50إِن تُصِبْكَ حَسَنَةٌ تَسُؤْهُمْ ۖ وَإِن تُصِبْكَ مُصِيبَةٌ يَقُولُوا قَدْ أَخَذْنَا أَمْرَنَا مِن قَبْلُ وَيَتَوَلَّوا وَّهُمْ فَرِحُونَ
Boo amee mbégte, ñu mer. Bu la naqar dalee, ñu bég ca, te naan : “Ndokk ba demunu woon.” Et ils se détournent tout en exultant.
51قُل لَّن يُصِيبَنَا إِلَّا مَا كَتَبَ اللَّهُ لَنَا هُوَ مَوْلَانَا ۚ وَعَلَى اللَّهِ فَلْيَتَوَكَّلِ الْمُؤْمِنُونَ
Waxal ne : “Dara mënunoo dal lu dul lu Yàlla bind ci nun rekk. Te Mooy sunu Kilifa. Te it ñi gëm, nañuy wéeru ci Yàlla”.
52قُلْ هَلْ تَرَبَّصُونَ بِنَا إِلَّا إِحْدَى الْحُسْنَيَيْنِ ۖ وَنَحْنُ نَتَرَبَّصُ بِكُمْ أَن يُصِيبَكُمُ اللَّهُ بِعَذَابٍ مِّنْ عِندِهِ أَوْ بِأَيْدِينَا ۖ فَتَرَبَّصُوا إِنَّا مَعَكُم مُّتَرَبِّصُونَ
Waxal ne : “Yéen a ngi nuy tuŋlu, te nun lu mën a xew, dananu am benn ci ñaari ndam yi [dee Chahiid walla nu dàq leen, not leen], benn Yàlla mbugal leen ci sunuy loxo, walla Mu xaroo leen ko ba ëllëg. Kon book nanu ànd di tuŋlu”.
53قُلْ أَنفِقُوا طَوْعًا أَوْ كَرْهًا لَّن يُتَقَبَّلَ مِنكُمْ ۖ إِنَّكُمْ كُنتُمْ قَوْمًا فَاسِقِينَ
Waxal ne : “Génneleen seeni alal, mu neex walla mu naqari leen : ak lu mën a xew, Yàlla du ko nangu, te sax yéen ay saay-saay ngeen”.
54وَمَا مَنَعَهُمْ أَن تُقْبَلَ مِنْهُمْ نَفَقَاتُهُمْ إِلَّا أَنَّهُمْ كَفَرُوا بِاللَّهِ وَبِرَسُولِهِ وَلَا يَأْتُونَ الصَّلَاةَ إِلَّا وَهُمْ كُسَالَىٰ وَلَا يُنفِقُونَ إِلَّا وَهُمْ كَارِهُونَ
Li waral seen alal jooju Yàlla du ko nangu, moo di ne dañoo weddi Yàlla ak ub Yonentam, tàyyeel lool ci julli, nay lool ci li ñuy joxe.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
52Aaya

Tekki — At-Tawba 52

Simoore At-Tawba Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “Yéen a ngi nuy tuŋlu, te nun…

Simoore Aaya 52/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers